From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
wherefore he saith also in another psalm, thou shalt not suffer thine holy one to see corruption.
moo tax mu waxaat feneen ne:“doo bàyyi sa waa ju sell, mu yàqu.”
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
god hath fulfilled the same unto us their children, in that he hath raised up jesus again; as it is also written in the second psalm, thou art my son, this day have i begotten thee.
def na ko ngir nun seeni sët, ci li mu dekkal yeesu. moom lañu bindoon ci ñaareelu saaru sabóor ne:“yaa di sama doom,maa di sa baay tey.”
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and david himself saith in the book of psalms, the lord said unto my lord, sit thou on my right hand,
ndaxte daawuda moom ci boppam moo ne ci sabóor:“boroom bi nee na sama boroom:‘toogal ci sama ndeyjoor,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: