From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
purge out therefore the old leaven, that ye may be a new lump, as ye are unleavened. for even christ our passover is sacrificed for us:
ni ma leen ko man a misaale, jëleleen fi bépp lawiir bu yàgg, ngir ngeen sell ni tooyal bu bees bu amul lawiir, ndax nekk ngeen ko ba noppi. ndaxte kirist deeyal na nu ca bant ba, mel ni mbote mu ñuy rendi, jébbal ko yàlla ca màggalu bésu jéggi ba.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
how much more shall the blood of christ, who through the eternal spirit offered himself without spot to god, purge your conscience from dead works to serve the living god?
su fekkee ne noonu la deme nag, du kon deretu kirist moo ëpp doole? jox na bakkanam yàlla, def ko sarax su amul sikk jaarale ko ci dooley xel miy sax abadan. kon deretam moo man a sellal sunu xel, mi nu doon yedd ndax jëf yu jëm ci dee, ngir nu man a jaamu yàlla jiy dund.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
if a man therefore purge himself from these, he shall be a vessel unto honour, sanctified, and meet for the master's use, and prepared unto every good work.
kon nag ku laabal sa bopp ci yooyu yépp, dinga nekk ndab lu tedd te sell, nga am njariñ ci boroom bi te jekk ci bépp jëf ju rafet.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: