Results for remaineth translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

there remaineth therefore a rest to the people of god.

Wolof

kon ba tey yàllaa ngi dencal ay gaayam noflaay bu nirook noflaayu yàlla ca juróom-ñaareelu fan ba.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for if that which is done away was glorious, much more that which remaineth is glorious.

Wolof

te it ndegam li wéy dafa amoon ndam, astemaak li fi sax.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for if we sin wilfully after that we have received the knowledge of the truth, there remaineth no more sacrifice for sins,

Wolof

gannaaw ba nu nangoo xam dëgg ba noppi, bu nu teyee di def bàkkaar, kon sarax dootul am ngir bàkkaar yooyu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

seeing therefore it remaineth that some must enter therein, and they to whom it was first preached entered not in because of unbelief:

Wolof

kon am na ñu ci war a dugg ba tey. te ñi jëkkoon a jot xebaar bu baax bi, dugguñu ci ndax seen déggadi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

(as it is written, he hath dispersed abroad; he hath given to the poor: his righteousness remaineth for ever.

Wolof

moom la mbind mi wax ne:«tabe na, ba may baadoolo yi;njubteem day sax ba fàww.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but this i say, brethren, the time is short: it remaineth, that both they that have wives be as though they had none;

Wolof

lii laa bëgg a wax, bokk yi: diir bu gàtt rekk a fi des. lu weesu tey, na góor ñi am jabar di def, ni bu ñu ko amul woon;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but their minds were blinded: for until this day remaineth the same vail untaken away in the reading of the old testament; which vail is done away in christ.

Wolof

waaye seen xel dafa daldi gumba. ba tey jii sax, bu ñuy jàng téereb kóllëre gu jëkk gi, muuraay moomu dafay des; deñul, ndaxte ci kirist rekk la man a deñe.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,025,512,255 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK