Results for spirit translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

quench not the spirit.

Wolof

buleen fey taalu xelum yàlla,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and be renewed in the spirit of your mind;

Wolof

te ngeen yeeslu ci seen biir xel,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and my spirit hath rejoiced in god my saviour.

Wolof

«sama xol a ngi màggal boroom bi,sama xel di bég ci yàlla sama musalkat,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but he that is joined unto the lord is one spirit.

Wolof

waaye nag kuy ànd ak boroom bi, xel yi dañuy booloo, nekk benn.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

now there are diversities of gifts, but the same spirit.

Wolof

am na fànni may yu bare yu jóge ci xelum yàlla, waaye menn xel moomu moo koy séddale.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

if we live in the spirit, let us also walk in the spirit.

Wolof

gannaaw nag nu ngi dund léegi ci xelum yàlla, kon nanu ko topp.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for he said unto him, come out of the man, thou unclean spirit.

Wolof

ndaxte yeesu nee woon na ko: «yaw rab wu bon wi, génnal ci nit ki.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but if ye be led of the spirit, ye are not under the law.

Wolof

waaye bu ngeen toppee xelum yàlla, nekkatuleen ci kilifteefu yoon wi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

he that hath an ear, let him hear what the spirit saith unto the churches.

Wolof

yaw mi am ay nopp, déglul li xelum yàlla di wax mboolooy ñi gëm.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 4
Quality:

English

blessed are the poor in spirit: for theirs is the kingdom of heaven.

Wolof

«yéen ñi xam seen ñàkk doole ngir neex yàlla,barkeel ngeen,ndaxte nguuru yàlla aji kawe ji,yéena ko yelloo.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they were not able to resist the wisdom and the spirit by which he spake.

Wolof

waaye àttanuñu sagoom ak xel mi muy waxe.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

(for the fruit of the spirit is in all goodness and righteousness and truth;)

Wolof

leer, mbaax lay meññ, njub ak dëgg.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and there was in their synagogue a man with an unclean spirit; and he cried out,

Wolof

noonu am na ci jàngu bi nit ku rab jàpp. mu daldi yuuxu naan:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and be not drunk with wine, wherein is excess; but be filled with the spirit;

Wolof

buleen màndi it ci sangara, liy ndeyi ñaawteef, waaye feesleen ak xel mu sell mi;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and jesus being full of the holy ghost returned from jordan, and was led by the spirit into the wilderness,

Wolof

noonu yeesu fees ak xel mu sell mi, jóge dexu yurdan.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

after they were come to mysia, they assayed to go into bithynia: but the spirit suffered them not.

Wolof

bi ñu agsee nag ci wetu diiwaanu misi, ñuy jéem a dugg diiwaanu bitini, waaye xelum yeesu mayuleen ko.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and john bare record, saying, i saw the spirit descending from heaven like a dove, and it abode upon him.

Wolof

ci kaw loolu yaxya seede na lii: «gis naa xelu yàlla mi ci melow pitax, mu jóge ci asamaan, tegu ci moom.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and because ye are sons, god hath sent forth the spirit of his son into your hearts, crying, abba, father.

Wolof

gannaaw doomi yàlla ngeen nag, yàlla yónni na xelu doomam ci sunu xol, mu koy wooye nii: «abba,» maanaam «baay.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and immediately i was in the spirit: and, behold, a throne was set in heaven, and one sat on the throne.

Wolof

ca saa sa xelum yàlla solu ma, noonu ma gis gàngune ca asamaan, te am ku ca toog.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for he that soweth to his flesh shall of the flesh reap corruption; but he that soweth to the spirit shall of the spirit reap life everlasting.

Wolof

ku ji ngir sa nafsu, dinga góob li sa nafsu meññ, maanaam ag yàqute. waaye ku ji lu soloo ak xelum yàlla, li xel mi meññ ngay góob, maanaam dund gu dul jeex.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,945,677,392 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK