Results for table translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

now no man at the table knew for what intent he spake this unto him.

Wolof

amul kenn ca ña fa toogoon ku xam lu tax mu wax ko loolu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but, behold, the hand of him that betrayeth me is with me on the table.

Wolof

waaye nag loxob ki may wor a ngi nekk ak man ci ndab li.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

that ye may eat and drink at my table in my kingdom, and sit on thrones judging the twelve tribes of israel.

Wolof

dingeen lekkandoo te naanandoo ak man ci sama nguur. te dingeen toog ci jal yi, di àtte fukki giir ak ñaar yu bànni israyil.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he asked for a writing table, and wrote, saying, his name is john. and they marvelled all.

Wolof

sakariya laaj àlluwa, bind ci ne: «yaxya la tudd.» Ñépp daldi waaru.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and she said, truth, lord: yet the dogs eat of the crumbs which fall from their masters' table.

Wolof

waaye jigéen ja ne ko: «waaw sang bi, teewul xaj yi di lekk ruusit, yi rot ci seen lekkukaayu boroom.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and david saith, let their table be made a snare, and a trap, and a stumbling block, and a recompence unto them:

Wolof

te daawuda it daf ci wax naan:«na seeni ñam sax nekk fiir ak i pakk;nañu ci daanu, te yàlla mbugal leen.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

ye cannot drink the cup of the lord, and the cup of devils: ye cannot be partakers of the lord's table, and of the table of devils.

Wolof

mënuleen a naan ci kaasu boroom bi, naan ci kaasu rab yi. mënuleen a sukk ci reerub boroom bi, sukk ci reerub rab yi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for there was a tabernacle made; the first, wherein was the candlestick, and the table, and the shewbread; which is called the sanctuary.

Wolof

nekkoon na ab tàntu màggalukaay bu ñu séddale ñaari néeg. ca ba jiitu la làmpu diwlin ba nekkoon ak taabal, ja ñu daan teg mburu ya ñu daa jébbal yàlla. foofaa nga tuddoon bérab bu sell ba.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and jesus went into the temple of god, and cast out all them that sold and bought in the temple, and overthrew the tables of the moneychangers, and the seats of them that sold doves,

Wolof

bi loolu amee yeesu dugg ca kër yàlla ga, dàq ñépp ña fay jaay ak ña fay jënd. mu daaneel taabali weccikatu xaalis ya ak tooguy jaaykati pitax ya,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,170,389,844 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK