Results for a tout de suite translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

il a tout mis sous ses pieds, et il l`a donné pour chef suprême à l`Église,

Wolof

yàlla suufeel na lépp fi kanamam, def ko kilifag lépp ci mbooloom ñi gëm,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais l`Écriture a tout renfermé sous le péché, afin que ce qui avait été promis fût donné par la foi en jésus christ à ceux qui croient.

Wolof

waaye yoon wi tëj na ñépp ci dooley bàkkaar, ngir ñi gëm yeesu kirist jot li yàlla dige woon ci seen kaw ngëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

dieu, en effet, a tout mis sous ses pieds. mais lorsqu`il dit que tout lui a été soumis, il est évident que celui qui lui a soumis toutes choses est excepté.

Wolof

ndaxte mbind mi nee na: «yàlla nootal na ko lépp, mu teg ci tànk.» waaye bu mbind mi nee, «noot na lépp,» wóor na ne, moom mi ko nootal lépp, génne na ci boppam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,794,304,072 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK