Results for arrivée translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

craignez qu`il ne vous trouve endormis, à son arrivée soudaine.

Wolof

bu nee jaleñ, bumu leen bett, ngeen di nelaw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

heureux ce serviteur, que son maître, à son arrivée, trouvera faisant ainsi!

Wolof

bu njaatigeem ñëwee te gis mu def noonu, surga boobu dina am ngërëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais dieu, qui console ceux qui sont abattus, nous a consolés par l`arrivée de tite,

Wolof

waaye yàlla miy dëfël xolu ñiy yoggoorlu ndax tiis, dëfël na sunu xol ci ñëwu tit,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

qui se sont détournés de la vérité, disant que la résurrection est déjà arrivée, et qui renversent le foi de quelques uns.

Wolof

dañoo moy dëgg, di wax ne ndekkite wees na, ba yàq ngëmu ñenn ñi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

le soleil se changera en ténèbres, et la lune en sang, avant l`arrivée du jour du seigneur, de ce jour grand et glorieux.

Wolof

jant bi dina daldi lëndëm,weer wi deretal,bala bésu boroom biy ñëw,di bés bu mag, bi ànd ak ndam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je veux que vous sachiez, frères, que ce qui m`est arrivé a plutôt contribué aux progrès de l`Évangile.

Wolof

damaa bëgg, bokk yi, ngeen xam lii: li ma dal taxul xebaar bu baax dellu gannaaw, waaye da koo jëmale kanam.

Last Update: 2024-04-14
Usage Frequency: 30
Quality:

Get a better translation with
7,788,577,292 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK