From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
dieu est avec vous
Last Update: 2023-05-19
Usage Frequency: 1
Quality:
cependant voici, la main de celui qui me livre est avec moi à cette table.
waaye nag loxob ki may wor a ngi nekk ak man ci ndab li.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
celui qui a reçu son témoignage a certifié que dieu est vrai;
képp ku nangu seedeem nangu nga ne yàlla, dëgg lay wax.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et tous les frères qui sont avec moi, aux Églises de la galatie:
man ak bokk yiy ànd ak man yépp, nu ngi leen di bind, yéen mboolooy ñi gëm te dëkk ci diiwaanu galasi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
avec piété et avec crainte, car notre dieu est aussi un feu dévorant.
ndaxte sunu yàlla, safara la suy lakke.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
celui qui n`est pas avec moi est contre moi, et celui qui n`assemble pas avec moi disperse.
ku farul ak man, yaa ngi may xeex, ku dajalewul ak man, yaa ngi tasaare.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et vous aussi, vous rendrez témoignage, parce que vous êtes avec moi dès le commencement.
te yéen itam dingeen seede samay mbir, ndaxte yéena nekkoon ak man ca njàlbéen ga.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
celui qui n`aime pas n`a pas connu dieu, car dieu est amour.
ku bëggul sa mbokk, xamuloo yàlla, ndax yàlla mbëggeel la.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car le nom de dieu est à cause de vous blasphémé parmi les païens, comme cela est écrit.
moo tax mbind mi ne: «yéena tax ñi nekkul yawut di suufeel turu yàlla.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
c`est avec instance que je vous demande de le faire, afin que je vous sois rendu plus tôt.
maa ngi leen di xiir, ngeen ñaanal nu, ba tuur ci seen ñaq, ngir ma yiwiku, ba dellusi ci yéen ci ni mu gën a gaawe.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
aussi vrai que dieu est fidèle, la parole que nous vous avons adressée n`a pas été oui et non.
wóor na yàlla ne, li nu leen di wax, du «waaw» ju ànd ak «déedéet.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
si la chose mérite que j`y aille moi-même, elles feront le voyage avec moi.
su aajoo ma demal sama bopp, kon dinañu ànd ak man.
Last Update: 2024-04-13
Usage Frequency: 31
Quality:
jésus lui répondit: je te le dis en vérité, aujourd`hui tu seras avec moi dans le paradis.
yeesu tontu ko ne: «ci dëgg maa ngi la koy wax, tey jii dinga texe ak man ca jataayu yàlla.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
je sais qu`en allant vers vous, c`est avec une pleine bénédiction de christ que j`irai.
te wóor na maa ne, bu ma ñowe ci yéen, dinaa indaale barkeb kirist bu mat sëkk.
Last Update: 2013-02-18
Usage Frequency: 1
Quality:
il dit encore: a quoi le royaume de dieu est-il semblable, et à quoi le comparerai-je?
noonu yeesu neeti: «lan la nguuru yàlla di nirool? lan laa ko man a mengaleel?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors jésus, levant les yeux sur ses disciples, dit: heureux vous qui êtes pauvres, car le royaume de dieu est à vous!
yeesu xool ay taalibeem ne leen:«yéen ñi sësul lu dul ci yàlla, barkeel ngeen,ndaxte nguuru yàlla, yéena ko yelloo.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il disait: le temps est accompli, et le royaume de dieu est proche. repentez-vous, et croyez à la bonne nouvelle.
naan: «jamono ji mat na, nguuru yàlla jegesi na; tuubleen seeni bàkkaar te gëm xebaar bu baax bi.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
est-ce de chez vous que la parole de dieu est sortie? ou est-ce à vous seuls qu`elle est parvenue?
ndax ci yéen la kàddug yàlla sosoo? walla ndax ci yéen rekk la agsi?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
jésus répondit: voici le premier: Écoute, israël, le seigneur, notre dieu, est l`unique seigneur;
noonu yeesu tontu ko ne: «bii: “bànni israyil, déglul! yàlla sunu boroom moom rekk mooy buur.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
c`est avec elle que les rois de la terre se sont livrés à l`impudicité, et c`est du vin de son impudicité que les habitants de la terre se sont enivrés.
moom la buuri àddina si àndal ci seen njaaloo. ci biiñu moy yàllaam la waa àddina màndee.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: