From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
une personne doit être discrète.
Last Update: 2023-10-13
Usage Frequency: 1
Quality:
alors, après avoir jeûné et prié, ils leur imposèrent les mains, et les laissèrent partir.
bi ñu ko déggee, ñu daldi woor ak a ñaan, teg leen ay loxo, ba noppi bàyyi leen ñu dem.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors les frères firent aussitôt partir paul du côté de la mer; silas et timothée restèrent à bérée.
noonu mbok yi yebal pool ca saa sa, mu jëm wetu géej, waaye silas ak timote des bérée.
Last Update: 2013-02-18
Usage Frequency: 1
Quality:
et je lui montrerai tout ce qu`il doit souffrir pour mon nom.
te dinaa ko won coono yu bare yu mu war a dékku ngir sama tur.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
aussitôt les frères firent partir de nuit paul et silas pour bérée. lorsqu`ils furent arrivés, ils entrèrent dans la synagogue des juifs.
bi loolu amee bokk yi jàllale pool ak silas ci saa si ci guddi, ñu jëm bere. ba ñu fa eggee nag, ñu dugg ca jàngub yawut ya.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il répondit: il est vrai qu`Élie doit venir, et rétablir toutes choses.
yeesu tontu leen ne: «waaw dëgg la, iliyas war na ñëw, jubbanti lépp.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
celui qui dit qu`il demeure en lui doit marcher aussi comme il a marché lui-même.
ku wax ne ci yàlla nga sax, fàww nga dund, ni yeesu kirist daan dunde moom ci boppam.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
comment donc s`accompliraient les Écritures, d`après lesquelles il doit en être ainsi?
waaye su ma ko defoon, nan la mbind mi man a ame? ndaxte mbind mi nee na, nii la war a ame.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
auxquels il faut fermer la bouche. ils bouleversent des familles entières, enseignant pour un gain honteux ce qu`on ne doit pas enseigner.
fàww nga wedamloo leen, ndax dañuy tas këri lëmm, ciy jàngale li warul ngir sàkku alal ju lewul.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
dama beuga bokk thie sa partie politique
Last Update: 2023-09-14
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.