Results for emportés translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

traîtres, emportés, enflés d`orgueil, aimant le plaisir plus que dieu,

Wolof

ay workat lañuy doon, di ñu ëppal te bare tiitar; seen bànneex a leen gënal yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin que nous ne soyons plus des enfants, flottants et emportés à tout vent de doctrine, par la tromperie des hommes, par leur ruse dans les moyens de séduction,

Wolof

noonu dootunu ay gune yu njàngalem nit ku ñëw di fàbbi ci seeni làqarci ak seeni pexe, nu mel ni ay gaal yu duus yi ak ngelaw li di baaje.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

etes-vous encore sans intelligence, et ne vous rappelez-vous plus les cinq pains des cinq mille hommes et combien de paniers vous avez emportés,

Wolof

ndax xamaguleen ba tey? xanaa fàttalikuwuleen juróomi mburu ya ngir juróomi junniy góor ña, ak ñaata pañe ngeen dajale woon ciy dammit?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est pourquoi nous devons d`autant plus nous attacher aux choses que nous avons entendues, de peur que nous ne soyons emportés loin d`elles.

Wolof

moo tax kon nu war a gën a faaydaal wax yi nu dégg, ngir bañ a bayliku.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

après l`avoir hissée, on se servit des moyens de secours pour ceindre le navire, et, dans la crainte de tomber sur la syrte, on abaissa les voiles. c`est ainsi qu`on se laissa emporter par le vent.

Wolof

bi ñu ko yéegee, ñu fab ay buum, ngir laxas ca taatu gaal ga, ngir ragal a daanu ci suuf su nooy su ñuy wax sirt; ba noppi ñu daldi sànni diigal, ngir wàññi doxub gaal ga, nuy yale noonu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,772,839,144 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK