From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
veux-tu savoir, ô homme vain, que la foi sans les oeuvres est inutile?
yaw mi gàtt xel, kaay ma won la ne, ngëm gu àndul ak jëf, amul njariñ.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
qui autrefois t`a été inutile, mais qui maintenant est utile, et à toi et à moi.
amul woon sa njariñ démb, waaye tey amal na nu njariñ, yaw ak man.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et le serviteur inutile, jetez-le dans les ténèbres du dehors, où il y aura des pleurs et des grincements de dents.
te sànnileen surga bu amul njariñ bi ci biti ci lëndëm gi. foofa dees na fa jooy te yéyu.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
repousse les discussions folles et inutiles, sachant qu`elles font naître des querelles.
tanqamlul bépp weranteb neen bu amul njariñ, xam ne xuloo rekk lay jur.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: