From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
j'ai faim
dama xiif
Last Update: 2022-05-17
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
j`ai envoyé tychique à Éphèse.
tisig moom yebal naa ko dëkku efes.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
j`ai aimé jacob et j`ai haï Ésaü.
loolu la mbind mi wax ne:«bëgg naa yanqóoba, bañ naa esawu.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
cinq fois j`ai reçu des juifs quarante coups moins un,
juróomi yoon yawut yi dóor nañu ma fanweeri yar ak juróom-ñeent.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
j`ai planté, apollos a arrosé, mais dieu a fait croître,
maa jëmbët, apolos suuxat, waaye yàlla moo jebbil.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
j`ai prié tes disciples de le chasser, et ils n`ont pas pu.
Ñaan naa say taalibe, ñu dàq ko, waaye mënuñu ko.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
mais il leur dit: j`ai à manger une nourriture que vous ne connaissez pas.
waaye yeesu tontu leen: «am na ñam wu may lekk, te xamuleen ko.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
jésus leur répondit: j`ai fait une oeuvre, et vous en êtes tous étonnés.
yeesu ne leen: «benn jaloore rekk laa def, te yéen ñépp ngeen jaaxle!
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
il lui répondit: maître, j`ai observé toutes ces choses dès ma jeunesse.
waa ji ne ko: «kilifa gi, loolu lépp sàmm naa ko li dale ci samag ndaw ba tey.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
et j`ai vu, et j`ai rendu témoignage qu`il est le fils de dieu.
yaxya teg ca ne: «gis naa loolu te seede naa ne, moom moo di doomu yàlla ji.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
en les lisant, vous pouvez vous représenter l`intelligence que j`ai du mystère de christ.
bu ngeen jàngee loolu, dingeen man a xam bu wér dégg, gi ma am ci mbóoti mbiri kirist.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
ainsi j`ai un vif désir de vous annoncer aussi l`Évangile, à vous qui êtes à rome.
li aju ci man nag, jekk naa ngir ñëw, xamal leen xebaar bu baax bi, yéen it waa room.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
un autre vint, et dit: seigneur, voici ta mine, que j`ai gardée dans un linge;
keneen ñëw ne: “sang bi, sa libidoor baa ngi nii. dama koo fasoon ci sekkit, denc ko.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
j`ai eu peur, et je suis allé cacher ton talent dans la terre; voici, prends ce qui est à toi.
moo tax ma ragaloon la, ba dem, nëbb sa xaalis ci biir suuf; mi ngii, fabal li nga moom.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
c`est par révélation que j`ai eu connaissance du mystère sur lequel je viens d`écrire en peu de mots.
yàlla feeñu na ma, xamal ma mbóoti mbir mi mu tëral, ni ma leen ko binde ci kàddu yu néew.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
car il dit à moïse: je ferai miséricorde à qui je fais miséricorde, et j`aurai compassion de qui j`ai compassion.
dafa wax musaa sax ne ko:«dinaa yërëm ku ma neex,laabiir ci ku ma neex.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
car j`ai eu faim, et vous ne m`avez pas donné à manger; j`ai eu soif, et vous ne m`avez pas donné à boire;
ndaxte xiifoon naa waaye joxuleen ma, ma lekk; te mar waaye joxuleen ma, ma naan.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
c`est celui dont j`ai dit: après moi vient un homme qui m`a précédé, car il était avant moi.
moo taxoon ma wax ne: “am na kuy ñëw sama gannaaw, waaye moo ma gën a màgg, ndaxte nekk na laata may juddu.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
après cela, jésus, qui savait que tout était déjà consommé, dit, afin que l`Écriture fût accomplie: j`ai soif.
bi loolu wéyee gannaaw yeesu xam na ne, lépp mat na léegi, mu ne nag, ngir amal mbind mi: «damaa mar.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
j`ai, en effet, éprouvé beaucoup de joie et de consolation au sujet de ta charité; car par toi, frère, le coeur des saints a été tranquillisé.
ci dëgg-dëgg sa mbëggeel bégal na ma bu baax, ba dëfël sama xol; ndaxte xam naa, sama mbokk, ni nga féexale xoli gaayi yàlla yu sell yi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference: