Results for je comprends pas wolof translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

jésus lui répondit: ce que je fais, tu ne le comprends pas maintenant, mais tu le comprendras bientôt.

Wolof

yeesu tontu ko ne: «xamoo fii mu nekk li may def, waaye dinga ko xami.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il le nia, disant: je ne sais pas, je ne comprends pas ce que tu veux dire. puis il sortit pour aller dans le vestibule. et le coq chanta.

Wolof

waaye piyeer weddi ko naan: «xawma li ngay wax, dégguma ci dara.» mu daldi génn, dem ca buntu kër ga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

lorsqu`un homme écoute la parole du royaume et ne la comprend pas, le malin vient et enlève ce qui a été semé dans son coeur: cet homme est celui qui a reçu la semence le long du chemin.

Wolof

boo xamee ne nit mu ngi déglu wax ju jëm ci nguuru yàlla te xamu ko, ibliis day ñëw, këf li ñu def ci xolam; kooku mooy ki jot ci jiwu wi ci kaw yoon wi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,794,167,518 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK