Results for jeune translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

le jeune homme fut ramené vivant, et ce fut le sujet d`une grande consolation.

Wolof

naka waxambaane wa, ñu indi ko muy dund, ba seen xol sedd guyy.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

sa tête fut apportée sur un plat, et donnée à la jeune fille, qui la porta à sa mère.

Wolof

Ñu indi bopp bi ci biir ndab, jox ko janq ba, mu jox ko ndeyam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

quand la foule eut été renvoyée, il entra, prit la main de la jeune fille, et la jeune fille se leva.

Wolof

waaye ñu génne leen, yeesu dugg, jàpp loxob janq ba, mu daldi jóg.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

les parents de la jeune fille furent dans l`étonnement, et il leur recommanda de ne dire à personne ce qui était arrivé.

Wolof

waajuri xale bi daldi waaru. waaye yeesu tere leen, ñu wax kenn li xew.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

après avoir entendu ces paroles, le jeune homme s`en alla tout triste; car il avait de grands biens.

Wolof

waaye bi waxambaane wa déggee loolu, mu jóge fa ak tiis, ndaxte ku bare woon alal la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

elles entrèrent dans le sépulcre, virent un jeune homme assis à droite vêtu d`une robe blanche, et elles furent épouvantées.

Wolof

Ñu dugg ci bàmmeel bi, gis ca ndeyjoor waxambaane wu sol mbubb mu weex, ñu daldi tiit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus leur adressa de fortes recommandations, pour que personne ne sût la chose; et il dit qu`on donnât à manger à la jeune fille.

Wolof

ci kaw loolu yeesu dénk leen bu wóor, ñu bañ koo siiwal; teg ca naa: «mayleen janq bi, mu lekk.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il y a ici un jeune garçon qui a cinq pains d`orge et deux poissons; mais qu`est-ce que cela pour tant de gens?

Wolof

«am na fi ci mbooloo mi ab xale bu yor juróomi mburu ak ñaari jën, waaye loolu lu muy jariñ mbooloo mu tollu nii?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il la saisit par la main, et lui dit: talitha koumi, ce qui signifie: jeune fille, lève-toi, je te le dis.

Wolof

mu jàpp loxoom ne ko: «talita kumi,» liy tekki: «janq bi, maa ngi la koy wax, jógal.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

en vérité, en vérité, je te le dis, quand tu étais plus jeune, tu te ceignais toi-même, et tu allais où tu voulais; mais quand tu seras vieux, tu étendras tes mains, et un autre te ceindra, et te mènera où tu ne voudras pas.

Wolof

ci dëgg-dëgg piyeer, maa ngi la koy wax, bi nga dee ndaw yaa doon takk sa geño, di dem fu la neex. waaye boo màggatee, dinga tàllal say loxo, keneen takkal la sa geño, yóbbu la foo bëggul.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,791,399,287 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK