Results for jure translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

et celui qui jure par le ciel jure par le trône de dieu et par celui qui y est assis.

Wolof

ku giñ ci asamaan, giñ nga ci jalu buur yàlla ak ki ci toog.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

celui qui jure par le temple jure par le temple et par celui qui l`habite;

Wolof

ku giñe kër yàlla gi, giñ nga ci kër yàlla gi ak ki ci dëkk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

celui qui jure par l`autel jure par l`autel et par tout ce qui est dessus;

Wolof

ku giñe saraxalukaay bi, giñ nga ci saraxalukaay bi ak li ci kawam lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

malheur à vous, conducteurs aveugles! qui dites: si quelqu`un jure par le temple, ce n`est rien; mais, si quelqu`un jure par l`or du temple, il est engagé.

Wolof

«yéen njiit yu gumba yi, dingeen torox! yéena ngi wax ne: “ku giñe kër yàlla gi, ngiñ li duggul, waaye ku giñ ci wurusu kër yàlla gi, dugg na.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,793,749,539 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK