Results for mais toi même d'abord translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

toi-même tu sais

Wolof

Last Update: 2024-02-25
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et: tu aimeras ton prochain comme toi-même.

Wolof

teralal sa ndey ak sa baay, te it: nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

sauve-toi toi-même, en descendant de la croix!

Wolof

wàccal ci bant bi te musal sa bopp!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

tu les rouleras comme un manteau et ils seront changés; mais toi, tu restes le même, et tes années ne finiront point.

Wolof

dinga leen taxañ ni malaan,ñu furi ni ay yére,waaye yaw doo soppiku,te sa dund amul àpp.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et voici le second, qui lui est semblable: tu aimeras ton prochain comme toi-même.

Wolof

te ñaareel bi noona la mel: “nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais toi, sois sobre en toutes choses, supporte les souffrances, fais l`oeuvre d`un évangéliste, remplis bien ton ministère.

Wolof

waaye yaw nanga foog ci lépp, dékku tiis, tey tas xebaar bu baax bi, ba matal sag yónnent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et à toi-même une épée te transpercera l`âme, afin que les pensées de beaucoup de coeurs soient dévoilées.

Wolof

ba naqar dina xar sa xol ni jaasi. noonu xalaati ñu bare feeñ.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus répondit: est-ce de toi-même que tu dis cela, ou d`autres te l`ont-ils dit de moi?

Wolof

yeesu tontu ko ne: «ndax yaa ko xalaat, wax ko, am dañu la koo xelal ci man?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car toute la loi est accomplie dans une seule parole, dans celle-ci: tu aimeras ton prochain comme toi-même.

Wolof

ndaxte yoon wépp, ndigal lii a ko tënk: «nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

si vous accomplissez la loi royale, selon l`Écriture: tu aimeras ton prochain comme toi-même, vous faites bien.

Wolof

su ngeen sàmmee yoonu buur yàlla, ni ko mbind mi tërale naan: «nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp,» kon def ngeen lu baax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

en disant: toi qui détruis le temple, et qui le rebâtis en trois jours, sauve-toi toi-même! si tu es le fils de dieu, descends de la croix!

Wolof

naan: «yaw mi man a toj kër yàlla ga, tabaxaat ko ci ñetti fan, musalal sa bopp; boo nekkee doomu yàlla, wàccal ci bant bi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,986,202 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK