From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
or, la pâque était proche, la fête des juifs.
fekk na booba bésu jéggi ba, di màggalu yawut ya, jubsi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
or ceux qui vivent selon la chair ne sauraient plaire à dieu.
kuy topp sa nafsu nag, doo man a neex yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
or, jésus aimait marthe, et sa soeur, et lazare.
yeesu soppoon na màrt ak maryaama ak lasaar.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ne prenez ni or, ni argent, ni monnaie, dans vos ceintures;
buleen dajale wurus, xaalis mbaa xànjar ci seeni maxtume.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
or c`est sans contredit l`inférieur qui est béni par le supérieur.
kiy barkeel a gën a màgg ki ñuy barkeel, loolu amu ci benn werante.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
or, il y avait sept frères. le premier se maria, et mourut sans enfants.
amoon na fi nag juróom-ñaari góor ñu bokk ndey ak baay. taaw ba takk jabar, faatu, te bàyyiwul doom.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
or, ceci arriva afin que s`accomplît ce qui avait été annoncé par le prophète:
yeesu def na noonu, ngir la ñu waxoon jaarale ko cib yonent am, bi mu naan:
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
or, il s`éleva de la part des disciples de jean une dispute avec un juif touchant la purification.
foofa ay taalibey yaxya tàmbalee werante ak benn yawut ci mbirum sangu set.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
or, dieu n`est pas dieu des morts, mais des vivants; car pour lui tous sont vivants.
kon nag nekkul yàllay ñi dee waaye yàllay ñiy dund la, ndaxte yàllaa tax ñépp di dund.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
la muraille était construite en jaspe, et la ville était d`or pur, semblable à du verre pur.
miir ba, jamaa lañu ko liggéeye, te dëkk ba di wurusu ngalam, leer ni weer bu set.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
celui qui me parlait avait pour mesure un roseau d`or, afin de mesurer la ville, ses portes et sa muraille.
ki doon wax ak man amoon na nattukaay, di bantu wurus bu mu doon natte dëkk ba ak miir ba ko wër, ak bunt ya.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors de nouveau tous s`écrièrent: non pas lui, mais barabbas. or, barabbas était un brigand.
noonu ñu daldi yuuxuwaat: «déedéet, waxunu kii; barabas lanu wax!» fekk barabas moomu taskatu réew la woon.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: