From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
partez; voici, je vous envoie comme des agneaux au milieu des loups.
demleen! maa ngi leen di yónni, mel ni ay mbote ci biir ay bukki.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
c`est pourquoi il dit encore ailleurs: tu ne permettras pas que ton saint voie la corruption.
moo tax mu waxaat feneen ne:“doo bàyyi sa waa ju sell, mu yàqu.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
comme il dit encore ailleurs: tu es sacrificateur pour toujours, selon l`ordre de melchisédek.
am na feneen fu mu wax ne:«doon nga saraxalekat ba fàwwmel ni melkisedeg.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
en effet, dans tout le prétoire et partout ailleurs, nul n`ignore que c`est pour christ que je suis dans les liens,
noonu ñiy wottu buur bi ak ñépp gis nañu bu leer ne, turu kirist rekk a tax ñu jàpp ma.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
en vérité, en vérité, je vous le dis, celui qui n`entre pas par la porte dans la bergerie, mais qui y monte par ailleurs, est un voleur et un brigand.
«ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, ku jaar feneen fu dul ci buntu gétt gi, kooku sàcc la, saay-saay la.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
d`ailleurs, il y a entre nous et vous un grand abîme, afin que ceux qui voudraient passer d`ici vers vous, ou de là vers nous, ne puissent le faire.
rax-ca-dolli it am na kàmb gu xóot sunu diggante ak yéen, ba tax ñi bëgg a jóge fii jëm ci yéen, walla ñi bëgg a jóge foofu jëmsi ci nun, duñu ko man.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.