Results for persécution translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

mais les juifs excitèrent les femmes dévotes de distinction et les principaux de la ville; ils provoquèrent une persécution contre paul et barnabas, et ils les chassèrent de leur territoire.

Wolof

waaye yawut ya xiir ay jigéen, ñi woomle te farlu ci diine, ñoom ak magi dëkk ba, ñu fitnaal pool ak barnabas, ngir génne leen réew ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

aussi nous glorifions-nous de vous dans les Églises de dieu, à cause de votre persévérance et de votre foi au milieu de toutes vos persécutions et des tribulations que vous avez à supporter.

Wolof

noonu nu ngi damu ci yéen ci kanamu mboolooy yàlla yi, ndax seen muñ ak seen ngëm ci biir mboolem fitnay noon, ak coono, yi ngeen di dékku.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,124,887 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK