Results for plein translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

Étienne, plein de grâce et de puissance, faisait des prodiges et de grands miracles parmi le peuple.

Wolof

naka noona ecen, mi fees ak yiw ak kàttan, di def ay kéemaan yu mag ak ay firnde ca nit ña.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il est semé méprisable, il ressuscite glorieux; il est semé infirme, il ressuscite plein de force;

Wolof

lu ñàkk solo lañuy suul; mu dekki ak ndam. lu néew doole lañuy suul, mu dekki ak kàttan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car il a accueilli notre demande, et c`est avec un nouveau zèle et de son plein gré qu`il part pour aller chez vous.

Wolof

bi nu ko laajee, mu ñëw ci yéen, nangu na, te rax-ca-dolli cawarteem tollu na, ba nu man a wax ne, ci coobarey boppam la jóge, jëm ci yéen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car c`était un homme de bien, plein d`esprit saint et de foi. et une foule assez nombreuse se joignit au seigneur.

Wolof

ndaxte nit ku baax la woon te fees ak xel mu sell mi ak ngëm; noonu mbooloo mu bare dolliku ci boroom bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

les autres disciples vinrent avec la barque, tirant le filet plein de poissons, car ils n`étaient éloignés de terre que d`environ deux cents coudées.

Wolof

yeneen taalibe ya xëcc mbaal, mi fees dell ak jën, jëme ko ca tefes ga, ndaxte gaal ga sorewul woon; diggante bi waroon na tollook téeméeri meetar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

homme plein de toute espèce de ruse et de fraude, fils du diable, ennemi de toute justice, ne cesseras-tu point de pervertir les voies droites du seigneur?

Wolof

ne ko: «yaw mi fees ak fen ak lu bon, di doomu ibliis, tey noonu lépp lu jub, ndax doo bàyyee dëngal yoon yu jub yu boroom bi?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et voici, une femme pécheresse qui se trouvait dans la ville, ayant su qu`il était à table dans la maison du pharisien, apporta un vase d`albâtre plein de parfum,

Wolof

fekk amoon na ca dëkk ba jigéen juy moy yàlla. bi mu yégee ne, yeesoo ngay lekk ca kër farisen ba, mu dem, yóbbaale njaq lu ñu defare doj wu ñuy wax albaatar te def latkoloñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

leur bouche est pleine de malédiction et d`amertume;

Wolof

duñu génne ci seen gémmiñ lu dul ay móolu ak i xas.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,944,409,448 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK