Results for pouvoir translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

et pour les envoyer prêcher avec le pouvoir de chasser les démons.

Wolof

mu joxaale leen sañ-sañu dàq ay rab.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

le pouvoir d'un chef d'avoir loué, dis-je aux soldats

Wolof

no toudou

Last Update: 2021-04-20
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

nous avons un autel dont ceux qui font le service au tabernacle n`ont pas le pouvoir de manger.

Wolof

am nanu sarax boo xam ne ñiy jaamu yàlla ci tàntu màggalukaayu bànni israyil sañuñu koo lekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

et il lui a donné le pouvoir de juger, parce qu`il est fils de l`homme.

Wolof

jox na doom ji itam sañ-sañu àtte, ndaxte mooy doomu nit ki.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

je donnerai à mes deux témoins le pouvoir de prophétiser, revêtus de sacs, pendant mille deux cent soixante jours.

Wolof

dinaa may sama ñaari seede yi, ñuy wax ci kàddug yàlla, sol ay saaku, di toroxlu diirub junni ak ñaari téeméeri fan ak juróom-benn-fukk.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

alors il appela les douze, et il commença à les envoyer deux à deux, en leur donnant pouvoir sur les esprits impurs.

Wolof

noonu mu woo ci moom fukki taalibe ya ak ñaar, jox leen sañ-sañu dàq rab yi, yónni leen, ñu ànd ñaar-ñaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

car le péché n`aura point de pouvoir sur vous, puisque vous êtes, non sous la loi, mais sous la grâce.

Wolof

ndaxte bàkkaar dootu leen manal dara, yéen ñi génn ci yoonu musaa, dugg ci yiwu yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

selon que tu lui as donné pouvoir sur toute chair, afin qu`il accorde la vie éternelle à tous ceux que tu lui as donnés.

Wolof

ndaxte jox nga ko sañ-sañ ci bépp mbindeef, ngir mu may dund gu dul jeex gi ñi nga ko dénk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

puis, ayant appelé ses douze disciples, il leur donna le pouvoir de chasser les esprits impurs, et de guérir toute maladie et toute infirmité.

Wolof

noonu yeesu woo ca moom fukki taalibeem ya ak ñaar, jox leen sañ-sañu dàq rab yi, tey faj jàngoro yépp ak wéradi yépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

c`est pourquoi, prenez toutes les armes de dieu, afin de pouvoir résister dans le mauvais jour, et tenir ferme après avoir tout surmonté.

Wolof

kon nag gànnaayooleen yérey xarey yàlla yépp, ba man a jànkoonte jamono ju xeex bi taree, noot lépp te taxaw temm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

de la fumée sortirent des sauterelles, qui se répandirent sur la terre; et il leur fut donné un pouvoir comme le pouvoir qu`ont les scorpions de la terre.

Wolof

ay njéeréer génn ca saxar sa, tasaaroo ci biir àddina. Ñu jox leen kàttan gu mel ni kàttanu jànkalaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

elles avaient des queues semblables à des scorpions et des aiguillons, et c`est dans leurs queues qu`était le pouvoir de faire du mal aux hommes pendant cinq mois.

Wolof

am nañu ay geen yu am ay fitt ni jànkalaar, te ca la seen kàttan nekk, ngir metital nit ñi diirub juróomi weer.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

il les paîtra avec une verge de fer, comme on brise les vases d`argile, ainsi que moi-même j`en ai reçu le pouvoir de mon père.

Wolof

dina leen jiite ak yetu weñ,i tojat leen ni ñuy toje ndaal kew —i

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

ils ont le pouvoir de fermer le ciel, afin qu`il ne tombe point de pluie pendant les jours de leur prophétie; et ils ont le pouvoir de changer les eaux en sang, et de frapper la terre de toute espèce de plaie, chaque fois qu`ils le voudront.

Wolof

am nañu sañ-sañu téye taw diirub fan, yi ñuy wax ci kàddug yàlla. am nañu it sañ-sañu soppi ndox yi deret te wàcce ci kaw suuf musiba yu nekk, saa su ñu ko bëggee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Get a better translation with
7,770,643,186 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK