Results for quand est ce que tu repars au sénégal translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

c`est ce que nous ferons, si dieu le permet.

Wolof

te noonu lanuy def, bu soobee yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

oui, père, je te loue de ce que tu l`as voulu ainsi.

Wolof

waaw baay bi, ndaxte looloo la neex.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais il le nia devant tous, disant: je ne sais ce que tu veux dire.

Wolof

waaye piyeer weddi ko ci kanamu ñépp ne ko: «xawma li ngay wax.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je viens bientôt. retiens ce que tu as, afin que personne ne prenne ta couronne.

Wolof

léegi ma ñëw. sàmmal li nga yor, ngir kenn bañ laa xañ sa kaalag ndam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

insensé! ce que tu sèmes ne reprend point vie, s`il ne meurt.

Wolof

yaa gàtt xel! li ngay ji, du jebbi dund gu bees, fi ak deewul ba noppi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

les pharisiens leur répliquèrent: est-ce que vous aussi, vous avez été séduits?

Wolof

noonu farisen ya laaj leen: «mbaa naxuñu leen, yéen itam?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

bien-aimé, tu agis fidèlement dans ce que tu fais pour les frères, et même pour des frères étrangers,

Wolof

yaw sama xarit, sa takkute fés na ci teeru bi ngay teeru mbokk yi, te fekk xamoo leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

alors les apôtres réunis lui demandèrent: seigneur, est-ce en ce temps que tu rétabliras le royaume d`israël?

Wolof

bi ñu dajaloo ak moom nag, ñu laaj ko: «boroom bi, ndax ci jamono jii ngay yékkatiwaat nguuru israyil?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

a ces mots, un des huissiers, qui se trouvait là, donna un soufflet à jésus, en disant: est-ce ainsi que tu réponds au souverain sacrificateur?

Wolof

bi yeesu waxee loolu, kenn ci alkaati yi nekkoon ci wetam daldi koy pes ne ko: «ndax nii ngay tontoo saraxalekat bu mag bi?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et le seigneur me dit: lève-toi, va à damas, et là on te dira tout ce que tu dois faire.

Wolof

noonu ma laaj ko: “lu ma war a def, boroom bi?” boroom bi ne ma: “jógal dem damas, foofa dees na la biral lépp, li ma la yen.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il ajouta avec serment: ce que tu me demanderas, je te le donnerai, fût-ce la moitié de mon royaume.

Wolof

mu boole ci ngiñ ne ko: «loo ma man a laaj, dinaa la ko jox, ba ci genn-wàllu réew mi sax.»

Last Update: 2023-08-11
Usage Frequency: 2
Quality:

French

dès que le morceau fut donné, satan entra dans judas. jésus lui dit: ce que tu fais, fais-le promptement.

Wolof

naka la yudaa jël dog wa, seytaane dugg ci moom. yeesu ne ko: «gaawantul ci li ngay def!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je te donnerai les clefs du royaume des cieux: ce que tu lieras sur la terre sera lié dans les cieux, et ce que tu délieras sur la terre sera délié dans les cieux.

Wolof

dinaa la jox caabiy nguuru yàlla aji kawe ji; li nga yeew ci àddina, dees na ko yeew ci asamaan; li nga yiwi ci àddina dees na ko yiwi ci asamaan.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il le nia, disant: je ne sais pas, je ne comprends pas ce que tu veux dire. puis il sortit pour aller dans le vestibule. et le coq chanta.

Wolof

waaye piyeer weddi ko naan: «xawma li ngay wax, dégguma ci dara.» mu daldi génn, dem ca buntu kër ga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il y a ici un jeune garçon qui a cinq pains d`orge et deux poissons; mais qu`est-ce que cela pour tant de gens?

Wolof

«am na fi ci mbooloo mi ab xale bu yor juróomi mburu ak ñaari jën, waaye loolu lu muy jariñ mbooloo mu tollu nii?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et voici, il parle librement, et ils ne lui disent rien! est-ce que vraiment les chefs auraient reconnu qu`il est le christ?

Wolof

xool-leen, mi ngi waaraate ci biir nit ñi, te kenn du ko wax dara. ndax sunu kilifa yi dañoo xam ne, mooy almasi bi?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il disait: abba, père, toutes choses te sont possibles, éloigne de moi cette coupe! toutefois, non pas ce que je veux, mais ce que tu veux.

Wolof

mu ne: «abba, baay bi, yaw mi dara tëwul, teggil ma kaasu naqar bii. moona bumu doon sama coobare, waaye na sa coobare am.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus lui dit: mon ami, ce que tu es venu faire, fais-le. alors ces gens s`avancèrent, mirent la main sur jésus, et le saisirent.

Wolof

yeesu tontu ko: «sama xarit, xam naa lu tax nga ñëw.» noonu ñu daldi jegesi, song ko, jàpp ko. jésus lui dit: mon ami, ce que tu es venu faire, fais-le. alors ces gens s`avancèrent, mirent la main sur jésus, et le saisirent.

Last Update: 2017-09-24
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car j`avais peur de toi, parce que tu es un homme sévère; tu prends ce que tu n`as pas déposé, et tu moissonnes ce que tu n`as pas semé.

Wolof

dama laa ragaloon, ndaxte ku néeg nga. dangay nangu loo dénkaanewul, di dajale loo jiwul.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

alors le souverain sacrificateur, se levant au milieu de l`assemblée, interrogea jésus, et dit: ne réponds-tu rien? qu`est-ce que ces gens déposent contre toi?

Wolof

ci kaw loolu saraxalekat bu mag bi taxaw ci seen kanam ne yeesu: «doo tontu? lu la nit ñi di jiiñ?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,781,150,415 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK