Results for tienne translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

il faut qu`il dirige bien sa propre maison, et qu`il tienne ses enfants dans la soumission et dans une parfaite honnêteté;

Wolof

na yor këram yorin wu rafet, te ay doomam déggal ko ak teggin yu mat.

Last Update: 2024-02-03
Usage Frequency: 2
Quality:

French

ou comment peux-tu dire à ton frère: frère, laisse-moi ôter la paille qui est dans ton oeil, toi qui ne vois pas la poutre qui est dans le tien? hypocrite, ôte premièrement la poutre de ton oeil, et alors tu verras comment ôter la paille qui est dans l`oeil de ton frère.

Wolof

nan nga man a waxe sa mbokk: “sama xarit, may ma, ma dindil la ñax gi ci sa bët,” yaw mi gisul gànj gi nekk ci sa bët? naaféq! jëkkal a dindi gànj gi ci sa bët, te noonu dinga man a gis bu leer, ngir dindi ñax gi ci sa bëtu mbokk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,783,131,465 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK