Results for tombe translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

efforçons-nous donc d`entrer dans ce repos, afin que personne ne tombe en donnant le même exemple de désobéissance.

Wolof

nanu farlu boog, ngir dugg ci noflaay boobu, ba kenn bañ a déggadi, ba daanu ni maam ya ca màndiŋ ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ne vend-on pas deux passereaux pour un sou? cependant, il n`en tombe pas un à terre sans la volonté de votre père.

Wolof

Ñaari picci rammatu, ndax duñu ko jaay ci dërëm? waaye benn ci ñoom du daanu ci suuf te soobul seen baay.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il ne faut pas qu`il soit un nouveau converti, de peur qu`enflé d`orgueil il ne tombe sous le jugement du diable.

Wolof

te it bumu nekk kuy door a gëm, ngir mu bañ a yég boppam, bay dajeek mbugalu yàlla, ni ko seytaane defe woon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

seigneur, aie pitié de mon fils, qui est lunatique, et qui souffre cruellement; il tombe souvent dans le feu, et souvent dans l`eau.

Wolof

naan: «sang bi, yërëmal sama doom, ndaxte mu ngi say, di am coono bu metti; léeg-léeg mu daanu ci safara, léeg-léeg mu daanu ci ndox.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

puis il leur dit: lequel de vous, si son fils ou son boeuf tombe dans un puits, ne l`en retirera pas aussitôt, le jour du sabbat?

Wolof

gannaaw loolu mu ne leen: «ku sa doom walla sa yëkk daanu ci teen, ndax doo dem génneji ko ca saa sa, fekk sax bésub noflaay la?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ils ont le pouvoir de fermer le ciel, afin qu`il ne tombe point de pluie pendant les jours de leur prophétie; et ils ont le pouvoir de changer les eaux en sang, et de frapper la terre de toute espèce de plaie, chaque fois qu`ils le voudront.

Wolof

am nañu sañ-sañu téye taw diirub fan, yi ñuy wax ci kàddug yàlla. am nañu it sañ-sañu soppi ndox yi deret te wàcce ci kaw suuf musiba yu nekk, saa su ñu ko bëggee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,179,752,557 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK