Results for toute puissance de dieu translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

et toute chair verra le salut de dieu.

Wolof

bu ko defee bépp mbindeef dina gismucc gi yàlla tëral.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

désormais le fils de l`homme sera assis à la droite de la puissance de dieu.

Wolof

waaye gannaawsi tey, doomu nit ki dina toog ci ndeyjooru yàlla, aji kàttan ji.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

le sabbat suivant, presque toute la ville se rassembla pour entendre la parole de dieu.

Wolof

noonu bésu noflaay ba ca tegu, daanaka waa dëkk bépp daje, ngir déglu kàddug yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin que votre foi fût fondée, non sur la sagesse des hommes, mais sur la puissance de dieu.

Wolof

ngir seen ngëm bañ a wékku ci xam-xamu nit ñi waaye mu wékku ci dooley yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

par la parole de vérité, par la puissance de dieu, par les armes offensives et défensives de la justice;

Wolof

ci kàddug dëgg ak ci kàttanu yàlla, nu ngi yor gànnaayi njubte ci loxol ndeyjoor ak lu càmmooñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il est grand de toute manière, et tout d`abord en ce que les oracles de dieu leur ont été confiés.

Wolof

raw na ko fu nekk. ci bu jëkk yawut yi la yàlla dénk waxam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

toute Écriture est inspirée de dieu, et utile pour enseigner, pour convaincre, pour corriger, pour instruire dans la justice,

Wolof

mbind mu sell mépp, ci gémmiñu yàlla la jóge, te am na njariñ ngir jàngal nit ñi, yedd leen, jubbanti leen te yee leen ci njub.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

la crainte de dieu n`est pas devant leurs yeux.

Wolof

te ragal yàlla sore na seen xol.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car la prédication de la croix est une folie pour ceux qui périssent; mais pour nous qui sommes sauvés, elle est une puissance de dieu.

Wolof

ndaxte yégleb deewu kirist ca bant ba, ag ndof la ci ñiy sànku. waaye ci nun ñi aw ci yoonu mucc gi, dooley yàlla la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

au nom du seigneur jésus, vous et mon esprit étant assemblés avec la puissance de notre seigneur jésus,

Wolof

ngeen daje ci turu boroom bi yeesu, te sama xel teewe ko, ànd ak dooley boroom bi yeesu,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car je vous ai annoncé tout le conseil de dieu, sans en rien cacher.

Wolof

ndaxte ñeebluwuma leen, ci di leen xamal lépp li yàlla digle.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car tous ceux qui sont conduits par l`esprit de dieu sont fils de dieu.

Wolof

ndaxte ñépp ñiy déggal xelu yàlla mi, ay doomi yàlla lañu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

devenez donc les imitateurs de dieu, comme des enfants bien-aimés;

Wolof

yéen nag ñiy guney yàlla, yi mu bëgg ci xolam, royleen ko ci loolu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin que l`homme de dieu soit accompli et propre à toute bonne oeuvre.

Wolof

noonu waayu yàlla ji dina mat, ba jekk ci bépp jëf ju rafet.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus répondit: je le suis. et vous verrez le fils de l`homme assis à la droite de la puissance de dieu, et venant sur les nuées du ciel.

Wolof

yeesu tontu ko: «moom laa. te dingeen gis, doomu nit ki toog ci ndeyjooru aji kàttan ji, di ñëw ci niiri asamaan.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin de connaître christ, et la puissance de sa résurrection, et la communion de ses souffrances, en devenant conforme à lui dans sa mort, pour parvenir,

Wolof

moom laay ittewoo xam, ak doole ji ànd ak ndekkiteem, ma bokk ci ay coonoom, ba fekki ko ci deeyam,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

au-dessus de toute domination, de toute autorité, de toute puissance, de toute dignité, et de tout nom qui se peut nommer, non seulement dans le siècle présent, mais encore dans le siècle à venir.

Wolof

mu tiim lu sore malaaka yépp, muy kilifa, boroom sañ-sañ, boroom doole mbaa buur, te gën a màgg wépp tur wu ñu man a tudd, muy tey, muy ëllëg.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus, revêtu de la puissance de l`esprit, retourna en galilée, et sa renommée se répandit dans tout le pays d`alentour.

Wolof

yeesu dellu diiwaanu galile, fees ak dooley xelum yàlla, te turam siiw ca diiwaan booba bépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ayant donc de telles promesses, bien-aimés, purifions-nous de toute souillure de la chair et de l`esprit, en achevant notre sanctification dans la crainte de dieu.

Wolof

ndegam nag jot nanu ci dige yu mel nii, samay soppe, nanu sellal sunu bopp ci bépp sobeb yaram walla bu xel, dund dund gu sell, ba mat ci ragal yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

l`ange lui répondit: le saint esprit viendra sur toi, et la puissance du très haut te couvrira de son ombre. c`est pourquoi le saint enfant qui naîtra de toi sera appelé fils de dieu.

Wolof

malaaka ma tontu ko ne: «xel mu sell mi dina wàcc ci yaw, te aji kawe ji dina la yiir ci kàttanam. moo tax xale biy juddu dinañu ko wooye ku sell ki, doomu yàlla ji.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,391,696 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK