From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
celui qui vaincra, je le ferai asseoir avec moi sur mon trône, comme moi j`ai vaincu et me suis assis avec mon père sur son trône.
ku daan, dinaa la toogloo ci sama wet ci sama gàngune, ni ma xeexe ba daan, man ci sama bopp, te toogandoo ak sama baay ci gànguneem.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
je vous ai dit ces choses, afin que vous ayez la paix en moi. vous aurez des tribulations dans le monde; mais prenez courage, j`ai vaincu le monde.
waaye nag déedéet, wéetuma, ndaxte baay baa ngi may wéttali. dama leen wax loolu, ngir ngeen am jàmm ci man. dingeen am nattu ci àddina, waaye takkleen fit yi; noot naa àddina.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et je vis comme une mer de verre, mêlée de feu, et ceux qui avaient vaincu la bête, et son image, et le nombre de son nom, debout sur la mer de verre, ayant des harpes de dieu.
noonu ma gis lu mel ni géej gu leer ni weer bu set buy ray-rayi ak safara. Ña nootoon rab wa ak nataalam, ak siifar bu mengoo ak turam, ñoo taxaw ca géej gu leer ga, yor xalam yu leen yàlla jox.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
en effet, si, après s`être retirés des souillures du monde, par la connaissance du seigneur et sauveur jésus christ, ils s`y engagent de nouveau et sont vaincus, leur dernière condition est pire que la première.
su ñu xamee boroom bi, di sunu musalkat yeesu krist, ba mucc ci sobes àddina, ba noppi sóobuwaat ca, ba mu noot leen, seen muj moo yées seen njàlbéen.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: