Results for camminava translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

passava per città e villaggi, insegnando, mentre camminava verso gerusalemme

Wolof

yeesoo ngi doon jaar ci ay dëkk yu mag ak yu ndaw, di jàngale te jublu yerusalem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

mentre discorrevano e discutevano insieme, gesù in persona si accostò e camminava con loro

Wolof

bi ñuy waxtaan ak a sotteente xalaat, yeesu ci boppam dab leen, ànd ak ñoom,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e balzato in piedi camminava; ed entrò con loro nel tempio camminando, saltando e lodando dio

Wolof

mu tëb, daldi taxaw, di dox. mu dugg ak ñoom ca kër yàlla ga, muy dox, di tëb tey sant yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

dopo aver remato circa tre o quattro miglia, videro gesù che camminava sul mare e si avvicinava alla barca, ed ebbero paura

Wolof

bi ñu joowee lu war a tollook juróom benni kilomet, ñu séen yeesu, muy dox ci kaw dex gi, jëm ci ñoom, ñu daldi tiit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

la chiesa era dunque in pace per tutta la giudea, la galilea e la samaria; essa cresceva e camminava nel timore del signore, colma del conforto dello spirito santo

Wolof

noonu mbooloom ñi gëm nekk ci jàmm ci biir diiwaani yude gépp ak galile ak samari; ñuy gën a dëgër, di wéy ci ragal yàlla, tey yokku ci ndimbalu xel mu sell mi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

mentre erano in viaggio per salire a gerusalemme, gesù camminava davanti a loro ed essi erano stupiti; coloro che venivano dietro erano pieni di timore. prendendo di nuovo in disparte i dodici, cominciò a dir loro quello che gli sarebbe accaduto

Wolof

gannaaw loolu ñu ànd jëm yerusalem, yeesu jiitu; taalibe yi am njàqare, te ñi ci topp tiit. noonu yeesu woowaat fukk ak ñaar ña cig wet, xamal leen li nar a xew ci mbiram.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,777,729,744 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK