From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
io pregherò il padre ed egli vi darà un altro consolatore perché rimanga con voi per sempre
te dinaa ñaan baay bi, mu jox leen beneen dimbalikat, buy nekk ak yéen ba abadan.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
quando verrà il consolatore che io vi manderò dal padre, lo spirito di verità che procede dal padre, egli mi renderà testimonianza
«dimbalikat bi dina ñëw, mooy xel mi jóge ci baay bi tey yor dëgg gi. dina jóge ci baay bi, ma yebal ko ci yéen. moom nag, moo may seedeeli.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ma il consolatore, lo spirito santo che il padre manderà nel mio nome, egli v'insegnerà ogni cosa e vi ricorderà tutto ciò che io vi ho detto
waaye dimbalikat, bi leen baay bi di yónnee ci sama tur, muy xelam mu sell, dina leen jàngal lépp, di leen fàttali li ma leen waxoon lépp.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ora io vi dico la verità: è bene per voi che io me ne vada, perché, se non me ne vado, non verrà a voi il consolatore; ma quando me ne sarò andato, ve lo manderò
moona de, ci sama wàll, dëgg laa leen di wax. li gën ci yéen mooy ma dem, ndaxte su dul loolu, dimbalikat bi du ñëw ci yéen; waaye su ma demee, dinaa leen ko yónnee.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: