From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
così anche noi quando eravamo fanciulli, eravamo come schiavi degli elementi del mondo
nun itam naka noonu, laata nuy mat, aaday àddina ñoo nu nootoon, ba def nu ni ay jaam.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
attendendo e affrettando la venuta del giorno di dio, nel quale i cieli si dissolveranno e gli elementi incendiati si fonderanno
te it ngeen taxaw temm ci séentu bésu yàlla bi, te waajal ñëwam. su boobaa, asamaan yi dinañu lakk, ba naaw ni pënd, te lu nekk ci àddina dina lakk, ba seey nib dóom.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
badate che nessuno vi inganni con la sua filosofia e con vuoti raggiri ispirati alla tradizione umana, secondo gli elementi del mondo e non secondo cristo
moytuleen ba kenn bañ leen a fàbbi ci ay xam-xami nit yuy naxi neen. xam-xam yu mel noonu, ñu ngi soqikoo ci aada yu nit tëral, ci aaday àddina, waaye soqikoowul ci kirist.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
se pertanto siete morti con cristo agli elementi del mondo, perché lasciarvi imporre, come se viveste ancora nel mondo, dei precetti qual
ndegam deeyandoo ngeen ak kirist, ba génne noonu ci aaday àddina, lu tax ngeen di nangu, ñu di leen teg ay sàrt yu mel nii: «bul fab, bul ñam, bul laal,» ni bu seenug dund aju woon ci àddina si?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ora invece che avete conosciuto dio, anzi da lui siete stati conosciuti, come potete rivolgervi di nuovo a quei deboli e miserabili elementi, ai quali di nuovo come un tempo volete servire
waaye léegi nag bi ngeen xamee yàlla, walla boog bi leen yàlla xàmmee, nan ngeen man a def, bay delluwaat ca aaday àddina? aada yooyee ñàkk doole te ñàkk njariñ, lu tax ngeen bëgg, ñu nootaat leen?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il giorno del signore verrà come un ladro; allora i cieli con fragore passeranno, gli elementi consumati dal calore si dissolveranno e la terra con quanto c'è in essa sarà distrutta
waaye bésu boroom bi dina ñëw, bett àddina ni sàcc. su boobaa, asamaan yi dinañu ne rajax toj, lu ne ci àddina lakk ba seey, te suuf ak lu mu ëmb dina ne fàŋŋ fa kanam yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: