Results for io ti adoro translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

io ti penso

Wolof

wolof

Last Update: 2020-04-19
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

«tutte queste cose io ti darò, se, prostrandoti, mi adorerai»

Wolof

mu ne ko: «lii lépp dinaa la ko may, boo sukkee màggal ma.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

io ti ho glorificato sopra la terra, compiendo l'opera che mi hai dato da fare

Wolof

wone naa sa ndam ci àddina, ndax li ma matal liggéey, bi nga ma santoon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

allora mi disse: và, perché io ti manderò lontano, tra i pagani»

Wolof

waaye boroom bi ne ma: “demal, dinaa la yebal fu sore, nga jëm ci xeeti ñi dul yawut.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

e gli disse: esci dalla tua terra e dalla tua gente e và nella terra che io ti indicherò

Wolof

mu ne ko: “toxul sa réew, bàyyi say bokk, te ñëw ci réew, mi ma lay won.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

padre giusto, il mondo non ti ha conosciuto, ma io ti ho conosciuto; questi sanno che tu mi hai mandato

Wolof

«baay, yaw ku jub ki, waa àddina xamuñu la, waaye man xam naa la, te ñii xam nañu ne, yaa ma yónni.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

allora uno scriba si avvicinò e gli disse: «maestro, io ti seguirò dovunque tu andrai»

Wolof

laata ñuy jàll, benn xutbakat daldi ñëw ci moom ne ko: «kilifa gi, dinaa la topp fépp foo jëm.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

allora il padrone fece chiamare quell'uomo e gli disse: servo malvagio, io ti ho condonato tutto il debito perché mi hai pregato

Wolof

sang ba nag woolu jaraaf ba ne ko: “yaw jaraaf ju soxor nga! baal naa la sa bor bépp, ndaxte tinu nga ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

ma lui rispose a suo padre: ecco, io ti servo da tanti anni e non ho mai trasgredito un tuo comando, e tu non mi hai dato mai un capretto per far festa con i miei amici

Wolof

waaye taaw ba tontu baayam ne ko: “seetal ñaata at laa la liggéeyal, mel ni jaam, te musumaa moy sa ndigal, waaye yaw, musuloo ma may sax tef, ngir ma bànneexu, man ak samay xarit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

gli rispose: «pietro, io ti dico: non canterà oggi il gallo prima che tu per tre volte avrai negato di conoscermi»

Wolof

yeesu tontu ko ne: «piyeer, maa ngi la koy wax, bala ginaar a sab tey jii, dinga weddi ñetti yoon ne, xam nga ma.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

ebbene, ti faccio dono di alcuni della sinagoga di satana - di quelli che si dicono giudei, ma mentiscono perché non lo sono -: li farò venire perché si prostrino ai tuoi piedi e sappiano che io ti ho amato

Wolof

dinaa def ba ñenn ci ñi bokk ci ndajem seytaane --te tuddoo yawut, fekk dañuy fen — dinaa leen ñëwloo, ñu sukk ci sa kanam, nangu ne, bëgg naa la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Italian

allora gesù gli disse: «che vuoi che io ti faccia?». e il cieco a lui: «rabbunì, che io riabbia la vista!»

Wolof

yeesu ne ko: «loo bëggoon ma defal la ko?» gumba gi tontu ko: «kilifa gi, damaa bëgg a gis.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Get a better translation with
7,777,213,331 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK