From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
il mio amore con tutti voi in cristo gesù
bëgg naa leen yéen ñépp ndax sunu booloo ak yeesu kirist.
Last Update: 2024-05-06
Usage Frequency: 4
Quality:
come il padre ha amato me, così anch'io ho amato voi. rimanete nel mio amore
«ni ma baay bi bëggee, noonu itam laa leen bëgge. saxleen ci mbëggeel googu ma am ci yéen.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
sei costante e hai molto sopportato per il mio nome, senza stancarti
xam naa it ne muñ nga, ba dékku coono ndax sama tur, te xàddiwoo. i
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e il mio spirito esulta in dio, mio salvatore
«sama xol a ngi màggal boroom bi,sama xel di bég ci yàlla sama musalkat,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e io gli mostrerò quanto dovrà soffrire per il mio nome»
te dinaa ko won coono yu bare yu mu war a dékku ngir sama tur.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
il mio giogo infatti è dolce e il mio carico leggero»
ndaxte sama kilifteef lewet na te sama yen diisul.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
salutate urbano, nostro collaboratore in cristo, e il mio caro stachi
nuyul-leen ma it urban, sunu nawle ci liggéeyu kirist, ak sama soppe estakis;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
chi mangia la mia carne e beve il mio sangue dimora in me e io in lui
kiy lekk sama yaram tey naan sama deret dina sax ci man, ma dëkk ci moom.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e si sentì una voce dal cielo: «tu sei il figlio mio prediletto, in te mi sono compiaciuto»
te baat bu jóge asamaan jib ne: «yaa di sama doom, ji ma bëgg; ci yaw laa ame bànneex.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
dopo il mio ritorno a gerusalemme, mentre pregavo nel tempio, fui rapito in estas
«bi ma dellusee yerusalem nag, di ñaan ca kër yàlla ga, leer tàbbi ci man.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e oltre a tutto questo, il mio assillo quotidiano, la preoccupazione per tutte le chiese
waxaalewuma li ci des nag: bés bu nekk maa ngi xalaat mboolooy ñi gëm.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ecco, io verrò presto e porterò con me il mio salario, per rendere a ciascuno secondo le sue opere
yeesu nee na: «maa ngi ñëw léegi, indaale pey gi, ngir delloo ku nekk lu mengoo ak lu mu def.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
chi mangia la mia carne e beve il mio sangue ha la vita eterna e io lo risusciterò nell'ultimo giorno
ku lekk sama yaram te naan sama deret, am nga dund gu dul jeex, te dinaa la dekkal keroog bés bu mujj ba.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
andate voi a questa festa; io non ci vado, perché il mio tempo non è ancora compiuto»
yéen nag demleen màggal ga. demaguma màggal googu, ndaxte sama waxtu jotagul.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e così lapidavano stefano mentre pregava e diceva: «signore gesù, accogli il mio spirito»
noonu ñu dóor ecen ay doj, muy ñaan yàlla ne: «boroom bi yeesu, nangul sama ruu!»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
abramo, vostro padre, esultò nella speranza di vedere il mio giorno; lo vide e se ne rallegrò»
seen baay ibraayma bég na, bi mu yégee sama ngan. bi mu ko gisee it, bég na ci lool.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
in quella città c'era anche una vedova, che andava da lui e gli diceva: fammi giustizia contro il mio avversario
amoon na itam ca dëkk ba jigéen ju jëkkëram faatu ju daan faral di ñëw ci moom, naan ko: “Àtte ma ak sama noon!”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
disse allora il padrone della vigna: che devo fare? manderò il mio unico figlio; forse di lui avranno rispetto
«boroom tool ba daldi ne: “nan laay def nag? dinaa yónni sama doom, sama reeni xol. xëy na ñu weg ko, moom.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e scese su di lui lo spirito santo in apparenza corporea, come di colomba, e vi fu una voce dal cielo: «tu sei il mio figlio prediletto, in te mi sono compiaciuto»
noonu xel mu sell mi daldi wàcc ci moom, yor jëmmu pitax, te baat bu jóge asamaan jib ne: «yaa di sama doom, ji ma bëgg; ci yaw laa ame bànneex.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
gesù, gridando a gran voce, disse: «padre, nelle tue mani consegno il mio spirito». detto questo spirò
yeesu woote ak kàddu gu dëgër naan: «baay, jébbal naa la sama ruu!» bi mu waxee loolu, mu delloo ruuwam yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: