Results for simile translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

e il secondo è simile al primo: amerai il prossimo tuo come te stesso

Wolof

te ñaareel bi noona la mel: “nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

le mura sono costruite con diaspro e la città è di oro puro, simile a terso cristallo

Wolof

miir ba, jamaa lañu ko liggéeye, te dëkk ba di wurusu ngalam, leer ni weer bu set.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

il suo splendore è simile a quello di una gemma preziosissima, come pietra di diaspro cristallino

Wolof

ànd ak ndamu yàlla. leeraayam mel ni leeraayu per bu jafe lool, ni jamaa buy ray-rayi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

a proposito, il regno dei cieli è simile a un re che volle fare i conti con i suoi servi

Wolof

«loolu moo tax nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni buur bu bëgg a waññ alalam ak ay jaraafam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

diceva dunque: «a che cosa è simile il regno di dio, e a che cosa lo rassomiglierò

Wolof

noonu yeesu neeti: «lan la nguuru yàlla di nirool? lan laa ko man a mengaleel?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

il regno dei cieli è simile a dieci vergini che, prese le loro lampade, uscirono incontro allo sposo

Wolof

«booba nguuru yàlla aji kawe ji dina mel ni fukki janq, ñu fab seeni làmp, génn, gatanduji boroom séet ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

chiunque ascolta queste mie parole e non le mette in pratica, è simile a un uomo stolto che ha costruito la sua casa sulla sabbia

Wolof

waaye képp ku dégg lii ma leen wax, te jëfewuloo ko, dinga mel ni nit ku ñàkk xel, ku tabax këram ci gànnuus bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

al fine di farsi comparire davanti la sua chiesa tutta gloriosa, senza macchia né ruga o alcunché di simile, ma santa e immacolata

Wolof

noonu dina ko jël, mu mel ni séet bu ñu waajal, di mbooloom mu soloo ndam, te gàkkul, rasul, taqul leneen, waaye mu sell te amul sikk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

avevano il ventre simile a corazze di ferro e il rombo delle loro ali come rombo di carri trainati da molti cavalli lanciati all'assalto

Wolof

takk nañu ci seen dënn lu mel ni kiiraayu weñ, te coow la seeni laaf di def mel ni coowu sareeti xare yu bare yu ñu takk fas, di xeexi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

la morte regnò da adamo fino a mosè anche su quelli che non avevano peccato con una trasgressione simile a quella di adamo, il quale è figura di colui che doveva venire

Wolof

teewul nag la dale ca aadama ba ca musaa, dee a ngi fi woon ci àddina, di noot ñépp, ak sax ñi seen bàkkaar melul woon ni bosu aadama, maanaam jàdd yoon. aadama moomu nag moo di takkandeeru kirist, mi waroon a ganesi àddina.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

perciò doveva rendersi in tutto simile ai fratelli, per diventare un sommo sacerdote misericordioso e fedele nelle cose che riguardano dio, allo scopo di espiare i peccati del popolo

Wolof

looloo taxoon mu war a mel niy doomi baayam ci bépp fànn, ngir doon seen saraxalekat bu mag fa kanam yàlla, bi leen yërëm te di sàmm kóllëre, te ci liggéeyu saraxaleem joxe na bakkanam ngir dindi bàkkaari nit ñi, ba yàlla baal leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

davanti al trono vi era come un mare trasparente simile a cristallo. in mezzo al trono e intorno al trono vi erano quattro esseri viventi pieni d'occhi davanti e di dietro

Wolof

amoon na it ca kanamu gàngune ma lu mel ni géej gu leer ni weer bu set, ba mel ni seetu. ci li wër gàngune ma, sës rëkk, amoon na fa ñeenti mbindeef yu fees ak ay bët ci kanam ak ci gannaaw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

la bestia che io vidi era simile a una pantera, con le zampe come quelle di un orso e la bocca come quella di un leone. il drago le diede la sua forza, il suo trono e la sua potestà grande

Wolof

rab wa ma gis ma nga mel ni segg, tànk ya mel ni yu rab wu ñuy wax urs, gémmiñ ga mel ni gu gaynde. ninkinànka ja jox ko kàttanam, nguuram ak sañ-sañam bu réy.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e gli uomini adorarono il drago perché aveva dato il potere alla bestia e adorarono la bestia dicendo: «chi è simile alla bestia e chi può combattere con essa?»

Wolof

Ñu jaamu ninkinànka ja ndax li mu joxoon sañ-sañ rab wa, di jaamu it rab wa, naan: «rab wi amul moroom, kenn mënul a xeex ak moom.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

il regno dei cieli è simile a un tesoro nascosto in un campo; un uomo lo trova e lo nasconde di nuovo, poi va, pieno di gioia, e vende tutti i suoi averi e compra quel campo

Wolof

yeesu teg ca ne: «nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni alal ju nëbbu cib tool. nit ki ko gis nëbbaat ko; xolam sedd, ba mu dem jaay li mu am lépp, jënd tool ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

infatti ciò che era impossibile alla legge, perché la carne la rendeva impotente, dio lo ha reso possibile: mandando il proprio figlio in una carne simile a quella del peccato e in vista del peccato, egli ha condannato il peccato nella carne

Wolof

lu yoonu musaa mënul woon a def, ndax néew dooley nit, yàlla defe na ko nii: dafa yónni doomam, ngir mu yor sunu jëmm, nun ñiy nekk ay bàkkaarkat, te mu jébbale bakkanam, ngir dindi bàkkaar yi. noonu la yàlla tase nguuru bàkkaar ci nit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

a chi dunque paragonerò gli uomini di questa generazione, a chi sono simili

Wolof

yeesu tegaat ca ne: «kon lan laa man a mengaleel niti jamono jii? lan lañuy nirool?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,788,827,013 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK