Results for tu sei translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

«se tu sei il re dei giudei, salva te stesso»

Wolof

«su fekkee ne yaay buuru yawut yi, musalal sa bopp!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

noi abbiamo creduto e conosciuto che tu sei il santo di dio»

Wolof

léegi nun gëm nanu te xam nanu ne, yaa di aji sell, ji jóge ci yàlla.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

gli replicò la donna: «signore, vedo che tu sei un profeta

Wolof

jigéen ja ne ko: «sang bi, gis naa ne, ab yonent nga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

gli rispose gesù: «tu sei maestro in israele e non sai queste cose

Wolof

yeesu tontu ko ne: «yaw yaay jàngal bànni israyil te xamuloo mbir yii?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

costui al contrario con un giuramento di colui che gli ha detto: tu sei sacerdote per sempre

Wolof

waaye nag yeesu moom doon na saraxalekat, bi yàlla giñee ne ko:«boroom bi giñ nate du dellu gannaaw mukk:“doon nga saraxalekat ba fàww.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora lo insultarono e gli dissero: «tu sei suo discepolo, noi siamo discepoli di mosè

Wolof

ci kaw loolu ñu daldi ko saaga ne ko: «yaw yaay taalibeem. nun, taalibey musaa lanu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

molto infatti mi sono rallegrato quando sono giunti alcuni fratelli e hanno reso testimonianza che tu sei verace in quanto tu cammini nella verità

Wolof

sunuy mbokk ñëw nañu, te seede ni nga fonke dëgg gi, ba wéer ci sa dund gépp, te bég naa ci lool.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e io ti dico: tu sei pietro e su questa pietra edificherò la mia chiesa e le porte degli inferi non prevarranno contro di essa

Wolof

te maa ngi lay wax lii: yaa di piyeer, te ci kaw doj wu réy woowu laay samp mbooloom ñi ma gëm, te dooley dee du ko manal dara.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora il diavolo gli disse: «se tu sei figlio di dio, dì a questa pietra che diventi pane»

Wolof

noonu seytaane ne ko: «boo dee doomu yàlla, santal doj wii mu nekk mburu.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

gli replicò natanaèle: «rabbì, tu sei il figlio di dio, tu sei il re d'israele!»

Wolof

nataneel wax ko ne: «kilifa gi, yaay doomu yàlla ji, yaa di buuru israyil!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

gli spiriti immondi, quando lo vedevano, gli si gettavano ai piedi gridando: «tu sei il figlio di dio!»

Wolof

fekk booba képp ku rab jàpp ku ko gis, daanu fa kanamam di yuuxu naan: «yaa di doomu yàlla.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

gli rispose: «sì, o signore, io credo che tu sei il cristo, il figlio di dio che deve venire nel mondo»

Wolof

mu tontu ko ne: «waaw boroom bi. gëm naa ne, yaay almasi bi, di doomu yàlla, ji war a ñëw àddina.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

dopo un poco, i presenti gli si accostarono e dissero a pietro: «certo anche tu sei di quelli; la tua parlata ti tradisce!»

Wolof

nes tuuti ña fa taxawoon ñëw ci piyeer ne ko: «ci lu wóor ne yaw itam bokk nga ci ñoom, ndaxte sa waxin feeñal na la.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

da molti uscivano demòni gridando: «tu sei il figlio di dio!». ma egli li minacciava e non li lasciava parlare, perché sapevano che era il cristo

Wolof

te it ay rab di génn ca nit ña te di yuuxu naan: «yaay doomu yàlla!» noonu mu gëdd leen, te mayu leen, ñu wax dara, ndaxte xam nañu ne, mooy almasi bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora il tribuno si recò da paolo e gli domandò: «dimmi, tu sei cittadino romano?». rispose: «sì»

Wolof

noonu kilifa ga ñëw laaj pool: «wax ma, ndax jaambur nga ci room?» mu tontu ko: «waaw, moom laa.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora i giudei gli si fecero attorno e gli dicevano: «fino a quando terrai l'animo nostro sospeso? se tu sei il cristo, dillo a noi apertamente»

Wolof

yawut ya wër ko ne ko: «kañ nga nuy dindi ci kumpa? boo dee almasi bi, wax ko mu leer.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,778,013,084 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK