Results for angelis translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

non enim angelis subiecit orbem terrae futurum de quo loquimu

Wolof

yàlla jébbalul malaaka yi benn sañ-sañ bu jëm ci jamonoy ëllëg ji nuy wax; keneen la ko jébbal,

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

qui autem negaverit me coram hominibus denegabitur coram angelis de

Wolof

waaye ku ma gàntu ci kanamu nit ñi, dinañu la gàntu ci kanamu malaakay yàlla yi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

hospitalitatem nolite oblivisci per hanc enim latuerunt quidam angelis hospitio recepti

Wolof

buleen fàttee teral ñiy ñëw ci yéen, ndaxte ñenn ñi, bi ñu ko defee, teral nañu ay malaaka te xamuñu ko.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ita dico vobis gaudium erit coram angelis dei super uno peccatore paenitentiam agent

Wolof

maa ngi leen di wax lii: ci noonule la malaakay yàlla yi di ame mbég ci benn bàkkaarkat bu tuubee ay bàkkaaram.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et vobis qui tribulamini requiem nobiscum in revelatione domini iesu de caelo cum angelis virtutis eiu

Wolof

te it yéen ñiy dékku coono, mu boole leen ak nun, tàbbal nu ci noflaay, bés bu sunu boroom yeesu kirist jógee asamaan, feeñ fi. keroog dina ànd ak malaakaam yu am kàttan,

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et audivi vocem magnam de templo dicentem septem angelis ite et effundite septem fialas irae dei in terra

Wolof

noonu ma dégg baat bu xumb bu jóge ca kër yàlla ga, naan juróom-ñaari malaaka ya: «demleen sotti ci àddina juróom-ñaari ndabi merum yàlla yi.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et unus ex quattuor animalibus dedit septem angelis septem fialas aureas plenas iracundiae dei viventis in saecula saeculoru

Wolof

noonu kenn ci ñeenti mbindeef ya jox juróom-ñaari malaaka ya juróom-ñaari ndabi wurus yu fees ak merum yàlla jiy dund ba fàww.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

dico autem vobis omnis quicumque confessus fuerit in me coram hominibus et filius hominis confitebitur in illo coram angelis de

Wolof

«te maa ngi leen koy wax, képp ku ma nangu ci kanamu nit ñi, doomu nit ki dina la nangu ci kanamu malaakay yàlla yi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et venit unus de septem angelis habentibus fialas plenas septem plagis novissimis et locutus est mecum dicens veni ostendam tibi sponsam uxorem agn

Wolof

gannaaw loolu benn malaaka ñëw, mi bokk ca juróom-ñaari malaaka, ya yoroon juróom-ñaari ndabi musiba yu mujj ya, ne ma: «Ñëwal, ma won la séet bi, jabaru mbote mi.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et dixit ei si filius dei es mitte te deorsum scriptum est enim quia angelis suis mandabit de te et in manibus tollent te ne forte offendas ad lapidem pedem tuu

Wolof

mu ne ko: «boo dee doomu yàlla, tëbal ci suuf, ndaxte mbind mi nee na:“dina jox ay malaakaam ndigal ci sa mbir,ñu leewu la ci seeni loxo,ngir nga bañ a fakkastalu ciw doj.”»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,620,992 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK