From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
et offerebant illi parvulos ut tangeret illos discipuli autem comminabantur offerentibu
bi loolu wéyee ñu indil yeesu ay xale, ngir mu teg leen ay loxoom. waaye taalibe ya gëdd nit ñi.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et comminabantur illi multi ut taceret at ille multo magis clamabat fili david miserere me
ci kaw loolu ñu bare gëdd ko, ngir mu noppi. teewul mu gën a yuuxu naan: «yaw sëtu daawuda bi, yërëm ma!»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: