From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ut cessavit autem loqui dixit ad simonem duc in altum et laxate retia vestra in captura
bi mu jàngalee ba noppi, mu ne simoŋ: «joowal gaal gi, ba fa ndox ma gën a xóote, ngeen sànni fa seeni mbaal ngir napp.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
propter quod dicit ascendens in altum captivam duxit captivitatem dedit dona hominibu
looloo tax mbind mi ne:«yéeg na ba ca fa gën a kawe,yóbbaale mbooloom noon mu bare, mi mu noot,tey séddale nit ñi ay may.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
similis est homini aedificanti domum qui fodit in altum et posuit fundamenta supra petram inundatione autem facta inlisum est flumen domui illi et non potuit eam movere fundata enim erat supra petra
dafa mel ni nit kuy tabax kër, mu gas fu xóot, jot doj wu réy, samp fa kër ga. bi mbënn ma ñëwee, wal ma dafa dal ca kër ga te yenguwul, ndaxte nit ka dafa tabax kër ga tabax bu dëgër.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.