From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
quis accusabit adversus electos dei deus qui iustifica
Ñi yàlla tànnal boppam, kan moo leen di tuumaal? yàlla moo leen àtte ni ñu jub.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et nisi breviati fuissent dies illi non fieret salva omnis caro sed propter electos breviabuntur dies ill
te bu ñu wàññiwul bés yooyu, kenn du mucc, waaye dees na leen wàññi ndax ñi yàlla tànn.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et nisi breviasset dominus dies non fuisset salva omnis caro sed propter electos quos elegit breviavit die
te bu fekkul woon boroom bi wàññi bés yooyu, kenn du mucc, waaye fekk na mu wàññi leen ndax gaayam ñi mu tànn.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et tunc mittet angelos suos et congregabit electos suos a quattuor ventis a summo terrae usque ad summum cael
dina yónni ay malaakam, ñu dajale ñi mu tànn ci ñeenti xebla yi, fa àddina dale, ba fa asamaan yem.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et mittet angelos suos cum tuba et voce magna et congregabunt electos eius a quattuor ventis a summis caelorum usque ad terminos eoru
dina yónni ay malaakaam ak baatu liit bu dégtu, ñu dajale ñi mu tànn ci ñeenti xebla yi, fa asamaan dale ba fu mu yem.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: