Results for filiorum translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

nam expectatio creaturae revelationem filiorum dei expecta

Wolof

ndax li yàlla bind lépp a ngi ne seew a gis doomi yàlla yi feeñ ci seen biir ndam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et multos filiorum israhel convertet ad dominum deum ipsoru

Wolof

dina delloosi niti israyil yu bare ci yàlla seen boroom.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ut eos qui sub lege erant redimeret ut adoptionem filiorum reciperemu

Wolof

ngir jot ñi yoon wi nootoon, ndax yàlla jàpp nu ni ay doomam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

qui respondens ait non est bonum sumere panem filiorum et mittere canibu

Wolof

yeesu tontu ko: «jël ñamu gune yi, sànni ko xaj yi, rafetul.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

quia et ipsa creatura liberabitur a servitute corruptionis in libertatem gloriae filiorum de

Wolof

yàlla dina rengi seen buumi njaam ci dee, boole leen ci jàmmu doomi yàlla yi ak seen ndam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

fide iacob moriens singulis filiorum ioseph benedixit et adoravit fastigium virgae eiu

Wolof

ngëm moo tax ba, bi yanqóoba nekkee ci sukkurat, mu barkeel kenn ku nekk ci doomi yuusufa yi. moo tax it mu màggal yàlla, jafandu ci yetam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

salvabitur autem per filiorum generationem si permanserint in fide et dilectione et sanctificatione cum sobrietat

Wolof

teewul jigéen dina mucc ci wasin, su saxee ci ngëm ak mbëggeel, di ku sell te maandu.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et audivi numerum signatorum centum quadraginta quattuor milia signati ex omni tribu filiorum israhe

Wolof

noonu ma dégg limub ñi ñu màndargaal; ñu tollu ci téeméer ak ñeent-fukk ak ñeent ci ay junni. Ñu jóge ci giiri bànni israyil yépp:

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

per quem et accessum habemus fide in gratiam istam in qua stamus et gloriamur in spe gloriae filiorum de

Wolof

moo nu ubbil bunt ci yàlla, nu taxaw temm ci yiwam, jaar ci ngëm. te it nu ngi bég ciy négandiku, yàlla boole nu ci ndamam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

esaias autem clamat pro israhel si fuerit numerus filiorum israhel tamquam harena maris reliquiae salvae fien

Wolof

esayi wax na ci mbirum israyil ne:«lu bànni israyil baree-bare ni suufus géej sax,lu néew rekk a ciy mucc.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

non solum autem illa sed et nos ipsi primitias spiritus habentes et ipsi intra nos gemimus adoptionem filiorum expectantes redemptionem corporis nostr

Wolof

te du dunyaa bi rekk mooy metitlu, nun it nu ngi metitlu, nun ñi yàlla sol xelam, ngir nu ñam añu ëllëg; nu ngi ne seew yàlla boole nu ci lépp li nu yelloo ni ay doomam, keroog bés bu yàllay goreel sunu yaram.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et habebat murum magnum et altum habens portas duodecim et in portis angelos duodecim et nomina inscripta quae sunt nomina duodecim tribuum filiorum israhe

Wolof

miir bu réy te kawe moo ko wër te am fukki bunt ak ñaar, te bu ca nekk malaaka taxaw ca wet ga. ca bunt ya bind nañu ca fukki tur ak ñaar, yu giiri bànni israyil.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

qui cum audissent intraverunt diluculo in templum et docebant adveniens autem princeps sacerdotum et qui cum eo erant convocaverunt concilium et omnes seniores filiorum israhel et miserunt in carcerem ut adducerentu

Wolof

bi ñu déggee loolu, ñu dugg ca kër yàlla ga ci suba teel, daldi waare. bi ñu koy def, saraxalekat bu mag ba ak gàngooram ñëw, woolu kureelu àttekat ya, maanaam mbooloom njiiti bànni israyil gépp; ñu yónnee, ngir jëli ndaw ya ca kaso ba.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,777,899,901 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK