Results for habitabant translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

et viderunt illum omnes qui habitabant lyddae et saronae qui conversi sunt ad dominu

Wolof

bi ko waa diiwaani lidd ak saron gépp gisee, ñu daldi woññiku ci boroom bi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

factum est autem petrum dum pertransiret universos devenire et ad sanctos qui habitabant lydda

Wolof

piyeer nag di wër, di jaar fu nekk, tey dem ci gaayi yàlla yi dëkk lidd,

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

saulus autem magis convalescebat et confundebat iudaeos qui habitabant damasci adfirmans quoniam hic est christu

Wolof

moona sool di gën a am kàttan, bay jaaxal yawut yi dëkk damas, ci di leen wax ay firnde, ne yeesu mooy almasi bi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

hoc autem factum est per biennium ita ut omnes qui habitabant in asia audirent verbum domini iudaei atque gentile

Wolof

mu wéy ci noonu diirub ñaari at, ba ñi dëkk diiwaanu asi ñépp dégg kàddug boroom bi, muy yawut muy gereg.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

hoc autem notum factum est omnibus iudaeis atque gentilibus qui habitabant ephesi et cecidit timor super omnes illos et magnificabatur nomen domini ies

Wolof

loolu siiw na ci ñépp, ñi dëkk efes, di yawut ak gereg; tiitaange jàpp leen ñoom ñépp, ba ñu màggal turu yeesu boroom bi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,792,771,880 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK