From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
hoc erat in principio apud deu
moo di ki nekkoon ak yàlla ca njàlbéen ga.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et hoc praecipe ut inreprehensibiles sin
dénk leen loolu, ngir ñu bañ a am benn gàkk.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et hoc faciemus siquidem permiserit deu
te noonu lanuy def, bu soobee yàlla.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et circumspiciebat videre eam quae hoc fecera
waaye yeesu di xool li ko wër, ngir gis ku ko def.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
dixitque illi recte respondisti hoc fac et vive
yeesu ne ko nag: «li nga wax dëgg la. boo defee loolu, dinga dund ba fàww.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et cum hoc dixisset ostendit eis manus et pede
bi mu leen waxee loolu, mu won leen ay loxoom ak ay tànkam.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et cum audiret turbam praetereuntem interrogabat quid hoc esse
naka la gumba ga dégg mbooloo di jàll, mu laaj lan moo xew.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
aut solus ego et barnabas non habemus potestatem hoc operand
walla boog man ak barnabas rekk noo war a daan sunu doole?
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
adiecit et hoc supra omnia et inclusit iohannem in carcer
ba faf tëj yaxya kaso.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
amplius autem deprecor vos hoc facere ut quo celerius restituar vobi
maa ngi leen di xiir, ngeen ñaanal nu, ba tuur ci seen ñaq, ngir ma yiwiku, ba dellusi ci yéen ci ni mu gën a gaawe.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
erunt enim ex hoc quinque in domo una divisi tres in duo et duo in tre
gannaawsi tey, bu juróomi nit bokkee genn kër, dinañu féewaloo. Ñett dinañu féewaloo ak ñaar ñi ci des, ñaar ñi féewaloo ak ñett ñooñu.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
erant autem quidam scevae iudaei principis sacerdotum septem filii qui hoc facieban
Ñi doon def loolu, juróom-ñaari doom lañu woon ci sewa, mi doon taafantaloo saraxalekat bu mag ba ci yawut yi.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et si salutaveritis fratres vestros tantum quid amplius facitis nonne et ethnici hoc faciun
su ngeen nuyoo seeni bokk rekk, lu ngeen def lu doy waar? xanaa ñi xamul yàlla duñu def noonu it?
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: