Results for monumentum translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

et valde mane una sabbatorum veniunt ad monumentum orto iam sol

Wolof

kon bés bu jëkk ci ayu-bés gi, ñu njëlu dem ca bàmmeel ba,

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ibi ergo propter parasceven iudaeorum quia iuxta erat monumentum posuerunt iesu

Wolof

ca bésu waajal la woon, ba yawut ya doon waajal bésu noflaay ba, te bàmmeel ba jege woon na. foofa lañu denc yeesu.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

tunc ergo introivit et ille discipulus qui venerat primus ad monumentum et vidit et credidi

Wolof

noonu keneen ka jiitu woon ca bàmmeel ba, duggsi moom itam. naka la gis, daldi gëm.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

venit ergo simon petrus sequens eum et introivit in monumentum et videt linteamina posit

Wolof

noonu simoŋ piyeer, mi ko toppoon, agsi, daldi dugg. mu séen càngaay la ci suuf,

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et abierunt quidam ex nostris ad monumentum et ita invenerunt sicut mulieres dixerunt ipsum vero non viderun

Wolof

Ñenn ci sunu àndandoo yi dem nañu ca bàmmeel ba, fekk lépp mel, na ko jigéen ña waxe woon. waaye moom gisuñu ko.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

erat autem in loco ubi crucifixus est hortus et in horto monumentum novum in quo nondum quisquam positus era

Wolof

tool a nga woon ca wetu bérab, ba ñu daajoon yeesu, te ca tool booba amoon na fa bàmmeel bu ñu musul a suul kenn.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

una autem sabbati maria magdalene venit mane cum adhuc tenebrae essent ad monumentum et videt lapidem sublatum a monument

Wolof

bés ba jiitu ca ayu-bés ga, maryaamam magdala jóg ca fajar, dem ca bàmmeel ba. bi mu agsee, mu gis ne dindi nañu xeer, wa ñu ko ube woon.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

petrus autem surgens cucurrit ad monumentum et procumbens videt linteamina sola posita et abiit secum mirans quod factum fuera

Wolof

waaye piyeer daldi jóg, daw, dem ca bàmmeel ba. bi mu àggee, mu sëgg, yër, gisul lu dul càngaay la. noonu mu dëpp ñibbi, jaaxle lool ci li xew.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

iudaei igitur qui erant cum ea in domo et consolabantur eam cum vidissent mariam quia cito surrexit et exiit secuti sunt eam dicentes quia vadit ad monumentum ut ploret ib

Wolof

noonu yawut, ya nekkoon ca kër ga di dëfël maryaama, gis ko mu ne bërét génn, ñu daldi koy topp, defe ne, day jooyi ca bàmmeel ba.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,780,914,547 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK