From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
et ego nesciebam eum sed ut manifestaretur israhel propterea veni ego in aqua baptizan
xawma woon kooku kan la waroon a doon, waaye xamal ko bànni israyil moo tax ma ñëw, di sóob nit ñi ci ndox.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
dixit autem paulus nesciebam fratres quia princeps est sacerdotum scriptum est enim principem populi tui non maledice
pool tontu leen: «bokk yi, xawma woon ne saraxalekat bu mag bi la, ndaxte tëral nañu ci mbind mi ne: “bul wax lu bon sa kilifag xeet.”»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
quid ergo dicemus lex peccatum est absit sed peccatum non cognovi nisi per legem nam concupiscentiam nesciebam nisi lex diceret non concupisce
kon nag lu nu war a wax? ndax bàkkaar ci yoonu musaa la jóge? mukk! waaye moo ma xamal luy bàkkaar. ndaxte su ma yoon wi waxul woon: «bul bëgg yëfi jaambur,» kon duma xam luy xemmem.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et ego nesciebam eum sed qui misit me baptizare in aqua ille mihi dixit super quem videris spiritum descendentem et manentem super eum hic est qui baptizat in spiritu sanct
bi loola laata am, xawma woon mooy kan, waaye yàlla, mi ma yebal may sóobe ci ndox, nee woon na ma: “dinga gis xel mu sell mi wàcc, tegu ci kaw nit. kooku moo di ki leen di sóob ci xel mu sell mi.”»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: