Results for patrum translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

et vos implete mensuram patrum vestroru

Wolof

di aw seen tànki baay, ba yées leen sax.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

deus patrum nostrorum suscitavit iesum quem vos interemistis suspendentes in lign

Wolof

yàllay sunuy maam dekkal na yeesu, mi ngeen bóomoon ci wékk ko ca bant ba.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

et dicitis si fuissemus in diebus patrum nostrorum non essemus socii eorum in sanguine prophetaru

Wolof

te yéena ngi wax ne: “bu nu fekke woon sunu jamonoy maam, dunu ànd ak ñoom ciy tuur deretu yonent yi.”

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ego deus patrum tuorum deus abraham et deus isaac et deus iacob tremefactus autem moses non audebat considerar

Wolof

“man maay sa yàllay maam, di yàllay ibraayma, isaaxa ak yanqóoba.” ci kaw loolu musaa tiit bay lox, te ñemeetul a xool.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

at ille dixit deus patrum nostrorum praeordinavit te ut cognosceres voluntatem eius et videres iustum et audires vocem ex ore eiu

Wolof

mu ne ma: “sunu yàllay maam tànn na la, ba may la, nga xam coobareem te gis aji jub ji te nga dégg ay waxam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

quod et induxerunt suscipientes patres nostri cum iesu in possessionem gentium quas expulit deus a facie patrum nostrorum usque in diebus davi

Wolof

te gannaaw ga, bi yosuwe nekkee kilifag sunuy maam, ñu jot tànt ba ñoom it, yóbbu ko ca réew, ma ñu nangu ca xeet ya yàlla dàq ci seen kanam. tànt ba nekk fa, ba ci jamonoy daawuda.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

deus abraham et deus isaac et deus iacob deus patrum nostrorum glorificavit filium suum iesum quem vos quidem tradidistis et negastis ante faciem pilati iudicante illo dimitt

Wolof

yàllay ibraayma ak isaaxa ak yanqóoba, di yàllay sunuy maam, màggal na ndawam yeesu; yéena xàcceek moom, ba jébbal ko pilaat, fekk naroon na koo bàyyi.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,800,289,393 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK