Results for promissiones translation from Latin to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

quotquot enim promissiones dei sunt in illo est ideo et per ipsum amen deo ad gloriam nostra

Wolof

te lépp lu yàlla dige woon fekk na «waawam» ci moom. noonu kon ci kirist lanuy waxe: «amiin,» ngir yékkati ndamu yàlla.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

dico enim christum iesum ministrum fuisse circumcisionis propter veritatem dei ad confirmandas promissiones patru

Wolof

lii laay wax: kirist ñëw na liggéeyal yawut yi, ngir wone kóllëreg yàlla ci matal dige, ya mu digoon maam ya.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

has igitur habentes promissiones carissimi mundemus nos ab omni inquinamento carnis et spiritus perficientes sanctificationem in timore de

Wolof

ndegam nag jot nanu ci dige yu mel nii, samay soppe, nanu sellal sunu bopp ci bépp sobeb yaram walla bu xel, dund dund gu sell, ba mat ci ragal yàlla.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

abrahae dictae sunt promissiones et semini eius non dicit et seminibus quasi in multis sed quasi in uno et semini tuo qui est christu

Wolof

léegi nag yàlla am na lu mu dig ibraayma ak askanam. mbind mi waxul: «ak i sëtam,» mu mel ni ñu bare, waaye kenn la wax: «ak sa askan,» maanaam kirist.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,317,316 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK