From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
itaque fratres aemulamini prophetare et loqui linguis nolite prohiber
kon nag bokk yi, farluleen ci di wax ci kàddug yàlla, te buleen tere kenn muy wax ay làkk.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
potestis enim omnes per singulos prophetare ut omnes discant et omnes exhortentu
yéen ñépp man ngeen a kenn-kennoo wax ci kàddug yàlla, ngir ñépp jàng te dégg li ñu leen di dénk.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
et dicunt mihi oportet te iterum prophetare populis et gentibus et linguis et regibus multi
gannaaw loolu ñu ne ma: «fàww nga wax ci kàddug yàlla lu jëm ci réew yu bare, xeet yu bare, kàllaama yu bare ak buur yu bare.»
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
volo autem omnes vos loqui linguis magis autem prophetare nam maior est qui prophetat quam qui loquitur linguis nisi si forte ut interpretetur ut ecclesia aedificationem accipia
léegi nag bëgg naa yéen ñépp, ngeen di wax ay làkk, waaye li ma gënal mooy ngeen di wax ci kàddug yàlla. kiy wax ci kàddug yàlla moo gën kiy wax ay làkk, su firiwul li muy wax, ngir ngëmu mbooloo mi yokku.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: