From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
omnia autem ex deo qui reconciliavit nos sibi per christum et dedit nobis ministerium reconciliationi
te loolu lépp a ngi sosoo ci yàlla, mi nu jubale ak boppam jaare ko ci yeesu kirist, te sas nu nuy waare juboo googu:
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
nunc autem reconciliavit in corpore carnis eius per mortem exhibere vos sanctos et inmaculatos et inreprehensibiles coram ips
léegi nag yàlla jubale na leen ak boppam jaare ko ci deewu kirist ci yaramu nitam, ngir taxawal leen ca kanamam, ngeen sell te ñàkk sikk ak i ŋàññ.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: