From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
et non poterant resistere sapientiae et spiritui quo loquebatu
waaye àttanuñu sagoom ak xel mi muy waxe.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
propterea accipite armaturam dei ut possitis resistere in die malo et omnibus perfectis star
kon nag gànnaayooleen yérey xarey yàlla yépp, ba man a jànkoonte jamono ju xeex bi taree, noot lépp te taxaw temm.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
ego enim dabo vobis os et sapientiam cui non poterunt resistere et contradicere omnes adversarii vestr
ndaxte man ci sama bopp maa leen di jox kàddu ak xel moo xam ne seeni noon duñu ko man a teggi, mbaa ñu di ko weddi.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:
ego autem dico vobis non resistere malo sed si quis te percusserit in dextera maxilla tua praebe illi et altera
waaye man maa ngi leen di wax ne, buleen bañ ku leen def lu bon, waaye ku la pes ci sa lexu ndeyjoor, jox ko ba ca des.
Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality: