Results for videritis translation from Latin to Wolof

Latin

Translate

videritis

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Latin

Wolof

Info

Latin

si ergo videritis filium hominis ascendentem ubi erat priu

Wolof

xelu yàlla mi mooy joxe dund; ñam wi jariñul dara. kàddu yi ma leen wax, ci xelum yàlla lañu jóge te ñooy joxe dund.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

dixit ergo iesus ad eum nisi signa et prodigia videritis non crediti

Wolof

yeesu ne ko: «yéen daal, dungeen gëm mukk, fi ak gisuleen ay firnde walla ay kéemaan.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ita et vos cum videritis haec fieri scitote quoniam prope est regnum de

Wolof

noonu itam bu ngeen gisee loolu lépp xew, xamleen ne nguuru yàlla jege na.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

cum autem videritis circumdari ab exercitu hierusalem tunc scitote quia adpropinquavit desolatio eiu

Wolof

«bu ngeen gisee ay xarekat wër dëkku yerusalem, xamleen ne jamono, ji ñu koy yàq, agsi na.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

si vero quaestiones sunt de verbo et nominibus et legis vestrae vos ipsi videritis iudex ego horum nolo ess

Wolof

waaye bu ajoo ci ay werante ciy wax ak ay tur ak seen yoon, loolu seen wàll la; man duma ko àtte.»

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

cum ergo videritis abominationem desolationis quae dicta est a danihelo propheta stantem in loco sancto qui legit intellega

Wolof

«dina am bés bu li ñuy wax: “lu araam luy yàqe” dina tege ca bérab bu sell ba. mooy li ñu doon wax jaarale ko ci yonent yàlla dañeel; ku ko jàng, nanga ko xam.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

cum autem videritis abominationem desolationis stantem ubi non debet qui legit intellegat tunc qui in iudaea sunt fugiant in monte

Wolof

«bés baa ngi ñëw, bu li ñuy wax “lu araam luy yàqe” tegee ca bérab bu mu yelloowul; kiy jàng, na xam. bu ngeen gisee loolu nag, ku nekk ci biir diiwaanu yude, nanga daw ca tund ya.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Latin

ibi erit fletus et stridor dentium cum videritis abraham et isaac et iacob et omnes prophetas in regno dei vos autem expelli fora

Wolof

foofa dingeen jooy, di yéyu, bu ngeen gisee seeni maam ibraayma, isaaxa, yanqóoba ak yonent yépp ci nguuru yàlla, te ñu dàq leen ca biti.

Last Update: 2012-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,892,220,144 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK