Results for basta translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

basta ya para dicha persona la reprensión de la mayoría

Wolof

Àtte bi ko mbooloo mi teg, doy na.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

le dijo felipe: --señor, muéstranos el padre, y nos basta

Wolof

filib ne ko: «boroom bi, won nu baay bi; loolu doy na nu.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces respondiendo jesús dijo: --¡basta de esto! y tocando su oreja, le sanó

Wolof

waaye yeesu daldi ne: «bàyyileen.» mu laal noppu waa ja, wéral ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces ellos dijeron: --señor, he aquí dos espadas. y él dijo: --basta

Wolof

noonu taalibe ya ne ko: «boroom bi, ñaari jaasee ngii.» mu ne leen: «doy na.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

así que, no os afanéis por el día de mañana, porque el día de mañana traerá su propio afán. basta a cada día su propio mal

Wolof

buleen jaaxle nag ngir ëllëg, ndaxte ëllëg dina topptoo boppam. bés bu nekk, coonoom doy na ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

volvió por tercera vez y les dijo: --¿todavía estáis durmiendo y descansando? basta ya. la hora ha venido. he aquí, el hijo del hombre es entregado en manos de los pecadores

Wolof

Ñetteelu yoon mu dellusi ci ñoom ne leen: «yéena ngi nelaw tey noppalu ba tey! jeex na. waxtu wi jot na; ñu ngi wor doomu nit ki ci loxoy bàkkaarkat yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,791,623,937 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK