Results for casarse translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

pero si no tienen don de continencia, que se casen; porque mejor es casarse que quemarse

Wolof

waaye su ngeen mënul a téye seen bopp, nangeen séy, ndaxte séy moo gën xemmem di leen gaañ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

le dijeron sus discípulos: --si así es el caso del hombre con su mujer, no conviene casarse

Wolof

bi ko taalibe ya déggee, ñu ne ko: «bu dee noonu la digganteb góor ak jigéen mel, bañ a séy moo gën.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

prohibirán casarse y mandarán abstenerse de los alimentos que dios creó para que, con acción de gracias, participasen de ellos los que creen y han conocido la verdad

Wolof

dinañu tere séy, di araamal ay ñam, fekk yàlla sàkk na leen, ngir ñi gëm te xam dëgg man ciy jëfandiku ak cant.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

la esposa está ligada mientras viva su esposo. pero si su esposo muere, está libre para casarse con quien quiera, con tal que sea en el señor

Wolof

jigéen ji séy dina ànd ak jëkkëram giiru dundam. waaye su jëkkër ji faatoo, man na séy ak ku ko neex, su fekkee ne góor gu gëm la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

(pero si ella se separa, que quede sin casarse o que se reconcilie con su esposo), y que el esposo no abandone a su esposa

Wolof

te bu teqalikoo ak moom, bumu séyaat, mbaa boog na juboo ak jëkkëram. te bu jëkkër ji fase jabaram.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

si alguien considera que su comportamiento es inadecuado hacia su virgen y si está en la flor de la edad y por eso siente obligación de casarse, puede hacer lo que quiere; no comete pecado. cásense

Wolof

nanu jàll nag ci mbiri kiy takk ngoro te amul pasteefu takk ndaw si. su fekkee ne waxambaane wi xalaat na ne, jëfewul nu jekk ak janq bi, fekk muy wees ag ndawam, te mu xalaat ne dafa koo war a takk, kon na ko takk, ni mu ko bëgge; deful bàkkaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,792,632,537 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK